Paroles de Waxoma Woon Lii
Paroles de Waxoma Woon Lii Par OMG
[ COUPLET 1]
Beuga toma wakhma
Xawma lu waral légui mane falé toma
Guiss nani diex na
Waxoko mais khamnani ni nobatoma
Gaaw ci defma luma méti
Say wax néxatul mangui deg lu né
Lu dieum ci mane sa yoon nékoussi
Souma déwoon do weet ndax du mane malay wétali
[REFRAIN]
Wano ma woon lii
Bagnouy tambali
Waxo ma wone lii
Meunatuma ndax dama taaayi
Wano ma woon lii
Bagnouy tambali
Wakho ma woon lii
Meuneutou mala mougneul dax mane dame la baayi
Dame la bayi hé
Dame la bayi hé
Dame la bayi hé
Toggatumafi di mougn ndax mane taaayi
Dame la Baayi
Dame la Baayi
May kila baayi
[COUPLET 2]
Goudi ba goudi lalay guiss
Dem na ba légui damako miss
Waxa tok mane
Falé toma
Sama wétal doon naxar ak tiss
Yay kiy béguel samay noon
Bax ci mbed mi ci mane nga bone
Dieukeur boula yénétoul foon
Ma name la té sori woma
[REFRAIN]
Wano ma woon lii
Bagnouy tambali
Waxo ma wone lii
Meunatuma ndax dama taaayi
Wano ma woon lii
Bagnouy tambali
Wakho ma woon lii
Meuneutou mala mougneul dax mane dame la baayi
Dame la bayi hé
Dame la bayi hé
Dame la bayi hé
Toggatumafi di mougn ndax mane taaayi
Dame la Baayi
Dame la Baayi
May kila baayi
[COUPLET 3]
Mangui dem guissouma liy tax may deloussi
Bou déssé loudoul sa keur ma fanaan ci mbed mi
And nexna wayé ko ba mou démak mbagam
Diox la sama xol ga fowé ko yaw danga lundeum
Yag na du tay
Wané gako tay
Naxaral sama xol xam nga yako tay
Légui dafa doy
Dotou mako joy
Beuss sa gui ci beussi lo lebblé lagne lay fay
Ecouter
A Propos de "Waxoma Woon Lii "
Plus de Lyrics de OMG
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl