Paroles de Bayou Xaleyi
Paroles de Bayou Xaleyi Par JAILER BANGZ
Fi kou gnémé dagne la dei
Lolou guemloko gni teukh
Nangoul ndogal mba nga dé
Yalla Buur mo may niteum
Wakhi késsé douma té ééh
Boba legui Mangui dem
Ligueye ba melni douma dé
Déna gnima yéné dé
Sagnsé bou rafet laaa kham
Parfum bou nékh laaa kham
Lolou bothi sissou yaa kham
Maléne moune té lolou daa am
Labili-w fasse takhouta fassa raw fassa nga thia kanam
Beugouma kanam ,siguil dima sén mangui adjou thia kaw
Fok ma liguéy beuri money
Oubi hôpital,hôpital pour sama none yi
Fadj fa borom khol you bone yi
Dilén djangal nigni ,nigni naané lignou sombi
Yénou sama chignon !guél yi nénagne je suis mignon
Amna dolé sokhor ,sokhor réne ak ate yidi gneuw
Hé Manla bayou xalei datouma fi amatii
Yénou sama chignon !guél yi nénagne je suis mignon
Amna dolé sokhor ,sokhor réne ak ate yidi gneuw
Hé Manla bayou xalei datouma fi amatii
Mr Propre qui fait du saale
Def ay son you febar
Fuck sa dossier médical
Mbokki baye fall magui ziar
Balla ngua deff kholal
Douma bayi té douma bal
Dialou Mouss guinax douko yeurndou
Niomm dofouniou sakh beu dima songou
Khol RK bayi
niom diemeuh naniou mais daniou soneuh
Moudié dima tongu
Mane yaye yama nianal, té baye yama khontou
Labali fass takhouta fassa raw
Fassa ngua ci kanam
Bougouma kanam siggil dima séneuh
Magui adiou cakaw
Jiguen guou rafett la kham
Teranga kessei la kham
Lolou bossiy sissou ya kham
Ma léne meune té lolou da am
Dialou Mouss guinax douko yeurndou
Maak nié ma diiour
Ma diiour goné yii
Refrain
Yénou sama chignon !guél yi nénagne je suis mignon
Amna dolé sokhor ,sokhor réne ak ate yidi gneuw
Hé Manla bayou xalei datouma fi amatii
Yénou sama chignon !guél yi nénagne je suis mignon
Amna dolé sokhor ,sokhor réne ak ate yidi gneuw
Hé Manla bayou xalei
datouma fi amatii
Ecouter
A Propos de "Bayou Xaleyi "
Plus de Lyrics de JAILER BANGZ
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl