Paroles de Lekou Bandit #4
Paroles de Lekou Bandit #4 Par JAILER BANGZ
Dégue diam ni kouy déglou Tupac
Réwantou té ken dou wax ndax kham nagn bou bax
Damay fayoul samay mame boumay niap toubab
Geuneu hard geuneu chaud geuneu def rap bou sale
Meun na rap lool meun na tape tate
Wowal len ma 18 sen xol yé ngui takk
Borom xol bou bone nako takk taleu
Dokh ci sen mind diaroul tak daleu
Fuck sa rappeur ak ioe f..ck limalama fuck
Bo beugeuté ma f..ck bitch na sa pu...y propre
Waxma ki ci top, na niow dioug ak tok
Cavalière sama kaw loloy sama drogue
Jail dey yakh nitte ngakka guéneu neu guéner caca
Tay niou teuthi sen gate, nio done kass mbalaxou Fata
F..ck rap Galsen, rieul ak fake lolou dou débat
Mane appart rew mouno wax té meunouma rap
Rap Galsen chérie boy esk nop ngam
Mane ndiol cikaw, mane la homme de base
Ecouter
A Propos de "Lekou Bandit #4"
Plus de Lyrics de JAILER BANGZ
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl