Paroles de Elle a Succombé
Paroles de Elle a Succombé Par DIDIER AWADI
[REFRAIN]
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu

[COUPLET 1]
Saff té meuna dém
Khalé bou yarou té dafa yéém
Ci dokhine ci thioline diék ci yar ak téguine
Doko dégeu ci dara dou thiow
Dou buzz dou photo dou dara
Khalé bi dafa sett
Bilay djiko bi dafa sett
No dou question de taar
Ce jour khalé bi je l’ai vu elle est là
Khalé bi elle est naturelle pas de faux cheveux
De cils elle est naturelle
Khalé bi elle est napi respecté bopam
Classé les happy
Gnafé di diangui le matin ba goudi ki souné waw
Kouko dieul di nga téki
Khalé bi dafa mool (dégoma déh)
Khalé bi dafa mool héy !
Lékouma nanou ma
Démou ma kheuyou ma gontou ma
Lékouma nanou ma
Démou ma kheuyou ma gontou ma
[REFRAIN]
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu
[COUPLET 1]
Je l’ai vu ce ma reine
Pour cela je donnerai la peine
Je peux me saigner les veines
Resté chez moi m’enchainé y’a des chaines
Non la goe elle est canon
Voilà la goe que je veux dans mon salon
Moi j’ai trouvé ma dose choper le show c’est fini je m’impose
La goe c’est du haut niveau
Ce n’est pas beaucoup dans les caniveaux
La goe c’est du chanel
Pas de diamant qu’on a pu taller comme elle
[REFRAIN]
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu
Tieupeu na ki déh djiné leu khalé bi djiné leu
[OUTRO]
Tieupeu na lékouma nanouma
Démou ma kheuyou ma gontou ma
Lékouma nanouma

Tieupeu na
Ecouter
A Propos de "Elle a Succombé"
Plus de Lyrics de DIDIER AWADI
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl