Paroles de Don't Play
Paroles de Don't Play Par BM JAAY
[CHORUS]
Geumoul m bamay commencé
Don’t play don’t play
Té founiou diarr fa ngeu diar
Don’t play don’t play
Yeah niggah mane ngen di clash
Don’t play don’t play
Trap king I’m a Killer
Don’t play don’t play
Boul dioum ba doug sama gayi
Don’t play don’t play
Rah ! rah ! i’m sure
Don’t Play don’t play
Baby girl mane ngey mbarane
Don’t play don’t FAKE
Amouma khaliss pour ioe
Don’t play don’t play
[VERSE 1]
Dalton gang leu , dalton gang leu
Atou reer neu douma dioug si feign télé
Rappeur en voie de disparition leu
Samay poche nio geuneu fess
Samay niari show télé
Diameu djiko dièk niggah
Sa pairou ferr yi la tassaré
Sougn la monté contre mane nala leer
Ni ay coup de marto ley démonté
Na mère bi bégue nga merr sa méralé goor
Ma ngui studio di togue
Louy tothi sa rappeur
Dou yakk sou dé mane ley soralé goor
Mesure bouma noté nieup guiss
Si sen bop comme tailleur
Souma len di niaw di len faté goor
Nion ngui tokk di khar
Nga guéner preuve goor
Ndaxté chiffre yi ngey def dagn key
Dégg rek moussou niouko guiss
Comme millions yi lopy door
Sou khaliss wété va me noce
Sama son sa guél di conss
Kone boy boul sissou bayma noce
Ba lagn si yague niatta père
sama ndieugou daleu moy sa caisse
Teudieul sa gate waxo piège
wor na y’Allah i’m the best
[CHORUS]
Geumoul m bamay commencé
Don’t play don’t play
Té founiou diarr fa ngeu diar
Don’t play don’t play
Yeah niggah mane ngen di clash
Don’t play don’t play
Trap king I’m a Killer
Don’t play don’t play
Boul dioum ba doug sama gayi
Don’t play don’t play
Rah ! rah ! i’m sure
Don’t Play don’t play
Baby girl mane ngey mbarane
Don’t play don’t FAKE
Amouma khaliss pour ioe
Don’t play don’t play
[VERSE 2]
Waxal new school bi niane na iblis
Audience rek pour wané len
Eup seytané sen xol you nioul yi
Même mane souma nékone yén damay bagn
Sama bop sama yéré diaroul djouni
Réy leu fess leu fougn koy défé séras
Guiss kou melni mane enfaite dafa rare
Dieul li nga mome yobalé
souniou part melni bouki
Beuss bouniou tassé loy nieuka wax
Loy moudié wax si sa life
Faut que nga fébar pour lal cachet
Métite bi sédok ko sa gayi wow !
Dieul sama khaliss dieundalé respect
Papa may djitou may sen majesté
Ay boy you thiouné lako sékeul ak ay
pa you maguett ak dome you dioude avorté
Rah ! rah ! i’m sure
Niou mey nianal halélouya
Depuis temps khalé la botone bouki bi
Kone mbeuw you sew yi sonalouma starrrr
Sékouma ak ioe béneu téguine
Mane damay deugeul you plane
Fuck rap
[CHORUS]
Geumoul m bamay commencé
Don’t play don’t play
Té founiou diarr fa ngeu diar
Don’t play don’t play
Yeah niggah mane ngen di clash
Don’t play don’t play
Trap king I’m a Killer
Don’t play don’t play
Boul dioum ba doug sama gayi
Don’t play don’t play
Rah ! rah ! i’m sure
Don’t Play don’t play
Baby girl mane ngey mbarane
Don’t play don’t FAKE
Amouma khaliss pour ioe
Don’t play don’t play
Ecouter
A Propos de "Don't Play"
Plus de Lyrics de BM JAAY
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl