Paroles de Lou Yakou Yawa
Paroles de Lou Yakou Yawa Par SAMBA PEUZZI
Hey xolal
Ko bandirabé wakhatilène si nimèy raber
Diaroul di latché son you melni mako fiy watier (nguani)
Ma yakk rap bi lolou lanu wakh wayè ma tay
Khadj yi fi nèkk mbow mbow T douniou matté
Kholal hé boy chui béni
Li yalah leu
Ko latier fi mouni leu boy bi bandit leu
Mère bangui gnane mane mangui jib amna liguéyou les…
Fèkk yidi wakh mane mèy job amna liguéyou les…
Kou manoul bawoul lou yakou yawa
Kou mounoul bawou oh ah ya yakk yawa
En, kou mounoul bawoul lou yakou yawa
Ya mounoul bawou ah ya yakk yawa
Boy gnom gneup peungui khar samay son comme rakku gims dama dègg dadj
Burna si boyi may tonton ndakh sama flow nguènn di boudiou
Yen bi moussoul diss tchouwli dèy beuri mèy gueuneu ndeuss
Téki rèkk moy yeu fou guerrier ndokhou ndawou gale la def Perrier
Sa carrière si foss millions de vue mouno féssal sa nekk tchèy li
Gor lokho si poche diapé ma jamel debbouze mèy diap khaliss hèy
Bi andé wanani pouloh mi beug nénam ah
Def iyo djitteul nak yi samba ngui sam mi yah
Ko bandirabé wakhatilène si nimèy raber
Diaroul di latché son you melni mako fiy watier nguani
Ma yakk rap bi lolou lanu wakh wayè ma tay
Khadj yi fi nekk mbow mbow T douniou matté
Kholal hé boy chui béni
Li yalah leu
Ko latier fi mouni leu boy bi bandit leu
Mère bangui gnane mane mangui jib amna liguéyou les…
Fèkk yidi wakh mane mèy job amna liguéyou les…
Kou manoul bawoul lou yakou yawa
Kou mounoul bawou oh ah ya yakk yawa
En, kou mounoul bawoul lou yakou yawa
Ya mounoul bawou ah ya yakk yawa, yawa
Yaw time is money ma téguou si temps
T game bi di ko dawal
Kou manoul bawo nguani lou yakou yawa
Bi andé wanani pouloh mi beug nénam ah
Def iyo djitteul nak yi samba ngui sam mi yah
Ko bandirabé wakhatilène si nimèy raber
Diaroul di latché son you melni mako fiy watier (nguani)
Ma yakk rap bi lolou lanu wakh wayè ma tay
Khadj yi fi nèkk mbow mbow T douniou matté
Kholal hé boy chui béni
Li yalah leu
Ko latier fi mouni leu boy bi bandit leu
Mère bangui gnane mane mangui jib amna liguéyou les…
Fèkk yidi wakh mane mèy job amna liguéyou les…
Kou manoul bawoul lou yakou yawa
Kou mounoul bawou oh ah ya yakk yawa
En, kou mounoul bawoul lou yakou yawa
Ya mounoul bawou ah ya yakk yawa, yawa
Ecouter
A Propos de "Lou Yakou Yawa"
Plus de Lyrics de SAMBA PEUZZI
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl