Paroles de Soxna Ci
Paroles de Soxna Ci Par SAMBA PEUZZI
Lo bouguoul mane doumko beug damay guagn
Ko bouguoul mane doumko beug dafay khar
Yamay térè nèlaw ndakh dangua djonguè dègueu dadj
Kay ma fétchal la yaw mane diraral ngama tarann taatch
Lo bouguoul néna la dafay khar
Koudoul yaw nama dandou gneuweul guaw
Yay yeunguel sama Mane bardé na
Bayil mbélè mbéssè gui di wakh
Yafi nékk té dou dagn girl
Bour Yallah moko dèff té dou dagn
Beug ngueumeu beug na lol dou dagn
Soxna ci yay sama lumière
Ba abadann dou dagn
Beug ngueumeu beug na lol dou dagn
Bour Yallah moko dèff té dou dagn
Soxna ci yay sama lumière
Ba abadann dou dagn
Bourou gualé lay done tchi yaw
Dinala khékhal fèpp fo men nèkk
Nèwonn nala ah ioe
Daguoul noumle nèkhé yafi nèkk té dou dègn
Mima la khamé tchi la taguok wèet oh yo yo yo
Konn boulme sori gneuweul fi seumeu wètt oh
Ma doundou paradise
You wanna make me out your way
Baby girl don’t let them break your heart
Gnom deugnouy sissou di fènn
Baby girl don’t let them break your heart
Baby mine waroul djoy nah nah
Baby mine boul djoy hey
Lo bouguoul mane doumko beug damay guagn
Ko bouguoul mane doumko beug dafay khar
Yamay térè nèlaw ndakh dangua djonguè dègueu dadj
Kay ma fétchal la yaw mane diraral ngama tarann taatch
Lo bouguoul néna la dafay khar
Koudoul yaw nama dandou gneuweul guaw
Yay yeunguel sama Mane bardé na
Bayil mbélè mbéssè gui di wakh
Yafi nékk té dou dagn girl
Bour Yallah moko dèff té dou dagn
Beug ngueumeu beug na lol dou dagn
Soxna ci yay sama lumière
Ba abadann dou dagn
Beug ngueumeu beug na lol dou dagn
Bour Yallah moko dèff té dou dagn
Soxna ci yay sama lumière
Ba abadann dou dagn
Bébé yangui digueul louné
Gno ngi koy wakh deug deug nak dou djèkh
Djaar nagnu founè t gnoy moudjè
Kay ma fétchal la boudé moy lileu nèkh bébé bébé
Yallah khamna khamngua
Lingueu meu djaral walay walay
Beugueu nagn digueunté bi djèkh
Mais fi mouss dou fi nané gnèkh
Lou nèkh da nagn doundou lou nèkh
Kham ngua nè sa xol doumko nabeu nabè
Yaw ni ngueu meu beuguè nonou la leu beugué
Boul lambeu yatay daguoul fougn la nobè
Yawnénala boul meusseu bayi
Ndakh damala woloo
Boul déglou wakh
You bonn yi si mane waay
Ndakh damala woloo
Yaw nè nala nè weuti nala
Someu bayè tchi lann djapp
Sama xol sama rèni xol
Kham ngua ni beugg beugg nala
Lo bouguoul mane doumko beug damay guagn
Ko bouguoul mane doumko beug dafay khar
Yamay térè nèlaw ndakh dangua djonguè dègueu dadj
Kay ma fétchal la yaw mane diraral ngama tarann taatch
Lo bouguoul néna la dafay khar
Koudoul yaw nama dandou gneuweul guaw
Yay yeunguel sama
Mane bardé na
Bayil mbélè mbéssè gui di wakh
Yafi nékk té dou dagn girl
Bour Yallah moko dèff té dou dagn
Beug ngueumeu beug na lol dou dagn
Soxna ci yay sama lumière
Ba abadann dou dagn
Beug ngueumeu beug na lol dou dagn
Bour Yallah moko dèff té dou dagn
Soxna ci yay sama lumière
Ba abadann dou dagn
Ecouter
A Propos de "Soxna Ci"
Plus de Lyrics de SAMBA PEUZZI
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl