Paroles de They Cap
Paroles de They Cap Par SAMBA PEUZZI
Mom nèna mom nèna mom nèna
Bandit la daafay cap limouy wakh khamnagn dou deug
Nè si net bi di fènn linguèy wakh khamnagn dou deug
Mak gnom bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non
Mak gnom Bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non
Hey nènagn i can’t put it up
Damlènn eup djap
Game bi lay gnew deup
Kholal I don’t give a fuck
Yendou weur di fènn
Yenfou guordjiguènn
Yakk dèrr di tèkk
Boumlèy djap di hum hum
Fucking nigga yak seu gnag bi yeup lagnouy ki kill
Gno tèyer game bi 4life
You know the di dil
Mais santt Yallah alhamdoulah
Mane ma way oulalah
Bandit la daafay cap limouy wakh khamnagn dou deug
Nè si net bi di fènn linguèy wakh khamnagn dou deug
Mak gnom bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non
Mak gnom Bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non
Mak yaw dougnou bèneu nguanè
Dangueu beug ma khof leu nguanè
Ya ma meunn fènn ngueu
Man boyou hood la
Diamenz 4life toussss dara doko dèff
Nigga dèy dèf dou wakh
Nigga dèy dèf dou wakh
Am on my way
Tchow li beuri neu
I’m on my waaaay
Niggaz capping but I’m on my way yeah
Gnou ngui wakh lounè I’m on my way yeah mon nèna
Bandit la daafay cap limouy wakh khamnagn dou deug
Nè si net bi di fènn linguèy wakh khamnagn dou deug
Mak gnom bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non
Mak gnom Bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non
Bandit la daafay cap limouy wakh khamnagn dou deug
Nè si net bi di fènn linguèy wakh khamnagn dou deug
Mak gnom bokougnou dieumoukay
Bokougnou dieumoukay non
Mak gnom Bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non
Ecouter
A Propos de "They Cap"
Plus de Lyrics de SAMBA PEUZZI
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl