JEEBA Diarabi  cover image

Paroles de Diarabi

Paroles de Diarabi Par JEEBA


Eh eh eh eh eh jeeba
Oh oh oh oh oh oh oh
Yéwou diakarlok sa kanam
Souma beutt yi di xol
Dila xool oh oh xol
May guiss sisa kanam baneekh
Mbeuguèl boudoul dieekh
Man ak yaw ba asamann eh asamann
Dakanté doranté nii xalé
Foumala diéko bal nako
Té yaw foma diéko nga baalma nguir
Mbeuguèl bingmay wann
Yakamti baniouné al’khayri
Ma xeuthieu leu tafla sama kaw
Dotoma reuthie abadane eh abadane

Man yénèna ank kounèk
Mou doundou love bimay doundou
Man yénèna ank kounèk Mou xam li I I I
May doundou aldiana té dèwagouma
Non non non déwagouma
Dioxla sa may beutt womat ma ni goumbeu
Yaw womatt ma ni goumbeu
Oh oh oh oh

Ba xol bi réré yaw yako forr
Fatko sa keur lolou lama lérè
La amoul thji man lèpeu thji yawla
Hey dèma réè may contann di bèk
Eh hey déma réè eh eh

[CHORUS]
Diokh nala li diokh naala lé hehe
Guiss  nala fi guiss naala fé eheh
Diokh nala li diokh naala lé hehe
Guiss  nala fi guiss naala fé eheh

Mais dafa melni yaw danga diougué assamane
Indalé mbécté mbécté bouy diouk thji mann
Defnala ni defnala nè eheh
Ngay souma diarabi , diarabi

Yéwou di lathie té sa kanam
Di weur fanla nèk
Diko séètt eyy e-ett
Ma nameu la té sori woma
Yakamti ba dianteu bi finkeu
Bama guiss la fi sama weett eh e e ett
Yaw yay taw biy mènieu souma tol
Sans yaw lèpay wow
Yaw yay takh may niafè beuga donn
Sa goor bou dee thji yaw
Kon boul titt boul meussa nangou
Diaxlé , aldiana lalay yobou
Yaw boul titt boul meussa nangou
Diaxlé , man ak yaw ba
Abadane anhan-ann wa a aw

[CHORUS]
Diokh nala li diokh naala lè hehe
Guiss  nala fi guiss naala fé eheh
Diokh nala li diokh naala lé hehe
Guiss  nala fi guiss naala fé eheh
 
Mais dafa melni yaw danga diougué assamane
Indalé mbécté mbécté bouy diouk thji mann
Defnala ni defnala nè eheh
Ngay souma diarabi , diarabi
I iii eh yeah yeah

Ecouter

A Propos de "Diarabi "

Album : Diabari (Single)
Année de Sortie : 2020
Ajouté par : Preslie Nzobou
Published : Feb 23 , 2020

Plus de Lyrics de JEEBA

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl