
Paroles de Yéné
...
Paroles de Yéné Par OOTHENTIK ZEUS
Mame boy neewoon nama gord ou sokhor
Yeene neek leu meun naa feekhlou sama khol
Sama tour bi fougnko woo
Ma sant god
Nakh lou bone
Nekoul sama khol
Loolou woorna sama ndeye
Worna sama baye
Amnaa niaanou sama ndeye
Sama barke baye
May taw faukma niaffé wathié sam yaay si thion
Douma khettou goor yiy yaakar si bay nguir ndono
Xam lima beug booma mattoul ndawlé dougn noono
Taal bou yallah taal, diemko fay
Sa khol lay sakhar, day biy gueneu takk
Xalaatoulo ba dadji sa wamadi
Nakh xam xam fign koy rooté baak beey xamadi
Xamagouloo lign dadj ba yeksi fii
Nakh rafett nguimbak baaku tassoul lamb dji
Mame boy neewoon nama gord ou sokhor
Yeene neek leu meun naa feekhlou sama khol
Sama tour bi fougnko woo
Ma sant god
Nakh lou bone
Nekoul sama khol
Loolou woorna sama ndeye
Worna sama baye
Amnaa niaanou sama ndeye
Sama barke baye
Neel sama yaay dou meuss deg domam si lenen loudoul ligueey soutouralko
Sama bay booy limouy khaar si doman moog si nank nank yakamtiwouko
Yeene bima am this sama xol moo mengoogoulak doolé fima toolou
Meme boudé lepp laa yamalé thi god, saa souma kheuyé maag ci di sabablou
Mame boy neewoon nama gord ou sokhor
Yeene neek leu meun naa feekhlou sama khol
Sama tour bi fougnko woo
Ma sant god
Nakh lou bone
Nekoul sama khol
Loolou woorna sama ndeye
Worna sama baye
Amnaa niaanou sama ndeye
Sama barke baye
Boy yeene neek leu weurseug bi gueedj leu
Daa am niouy diow nienen di feey
Boul lap si haine meu ni dieum fekhel beu
Xam nooy dounder moolassiy guen
Boy yeene neek leu weurseug bi gueedj leu
Daa am niouy diow nienen di feey
Boul lap si haine meu ni dieum fekhel beu
Xam nooy dounder moolassiy guen
Ecouter
A Propos de "Yéné"
Plus de Lyrics de OOTHENTIK ZEUS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl