JEEBA Lamou Saff  cover image

Paroles de Lamou Saff

Paroles de Lamou Saff Par JEEBA

Lamou Saf kene doulako wakh ndakh kouko mathieu ko xam
Gni nane ki dalay golo Lo nando dara
Ma dougou thii biir ba leep lerma nagnieu diar ngako
Koula xamoul moy direuntei ak yow mbagg chérie coco
Bodone musicien mani la do dégammé def ngama sa xalé
Do jouer ak Man ay jeux de gamins
Deuk dima diamb dima diamb yoroo marimba do Benjamin
Bo defoul nank na meusseu deii sa lokho on sait jamais
Mome xalé la té barina dolé mo raaw Alkaty dafay doré
Dinala topato ba ladj ladj ladj la babe looy réreer
Té boko lladjer mounila Bae Man Yoow mi laay rereer

Fadiar teel ni lamay yéweer
Dima xool si biir beut nane qu’est-ce que ça fait
Yoow ya raaw athlète bou drogué (dopé)
Koula topeu ba sii biir deey moudié éclatée
Fadiar teel ni lamay yéweer
Dima xool si biir beut nane qu’est-ce que ça fait
Yoow ya raaw athlète bou drogué (dopé)
Koula topeu ba sii biir deey moudié éclatée

Dafa nekh lool nga am kou kham louy diaamb sa ditakh
Sokhla woul sakh ngay wakh di excuté nélako rambakh
Teey na kham na founiouy féthié yeela ndawrabine
Collé la niaap melni Docteur Raoul ak Chloroquine
Armée wou koow ba souf melni kouy deem Guerre
Tassarei arsenal yi boula daal nga terre
Dila woo si beurei tee lerna lerna molaa molaa meune dila nogaatu
Tass sa ngemb mbeur meu danouna ooh au secours
Mome xalé la té barina dolé mo raaw Alkaty dafay dorer
Dinala topato ba ladj ladj ladj la babe looy réreer
Té boko lladjer mounila Bae Man Yoow mi laay rereer

Fadiar teel ni lamay yéweer
Dima xool si biir beut nane qu’est-ce que ça fait
Yoow ya raaw athlète bou drogué
Koula topeu ba sii biir deey moudié éclatée
Fadiar teel ni lamay yéweer
Dima xool si biir beut nane qu’est-ce que ça fait
Yoow ya raaw athlète bou drogué
Koula topeu ba sii biir deey moudié éclatée

Fadiar teel ni lamay yéweer
Dima xool si biir beut nane qu’est-ce que ça fait
Yoow ya raaw athlète bou drogué (dopé)
Koula topeu ba sii biir deey moudié éclatée
Fadiar teel ni lamay yéweer
Dima xool si biir beut nane qu’est-ce que ça fait
Yoow ya raaw athlète bou drogué (dopé)
Koula topeu ba sii biir deey moudié éclatée

Jeeba le Boy Rambaax

Ecouter

A Propos de "Lamou Saff "

Album : Alajee (Album)
Année de Sortie : 2022
Ajouté par : Farida
Published : Dec 16 , 2022

Plus de Lyrics de JEEBA

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant

A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl