YOUSSOU NDOUR Mool cover image

Paroles de Mool

Paroles de Mool Par YOUSSOU NDOUR

Yaw mool u géej gi di jambaar ci réew mi
Bala ngaa dem géej ngala déglu météo
Bu la nee bul dem  lu mën ë xew bul dem
Ben fan ak ñaar , bu mu yax sa liggéey
Doyloo nga yalla , du tee nga sa yor téléphone
Ak sa gps , te bul fatte sa gillet
Sama fans yi ma am ,mool ñoo ma gën ë xam
Fu ma làng ee ak  ñoom , guddi gë day xumb lool
Man sama fans yee , ma saf
Sawar naa làng ak ñoom , fu ne
Aka ñoo dégg daaj , ma ni
Moo tax may dem ba jeex , walla

Jambaar ca waar wa , jambaar ca géej gë
Su ma ko mën oon , ben mool du des ci géej
Bu la nee bul dem , lu mën ë xew bul dem
Ben fan ak ñaar , bu mu yax sa liggéey
Sama fans yi ma am ,mool ñoo ma gën ë xam
Fu ma làng ee ak  ñoom , guddi gë day xumb lool
Jambaar ca waar wa , jambaar ca géej gë
Su ma ko mën oon , ben mool du des ci géej
Man sama fans yee , ma saf
Sawar naa làng ak ñoom , fu ne
Aka ñoo dégg daaj , ma ni
Moo tax may dem ba jeex , walla
Yalna leen yalla suturaal ,te di leen samm biir géej
Barke el seen liggéey bi , barke el seen njaboot gi
Aar leen ba ñu doon mag , jox leen barke maam yi   
Man sama fans yee , ma saf
Sawar naa làng ak ñoom , fu ne

Yess  aye
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Bël ba ca ndar , sonn al na waa guét ndar géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Mool yi laa bëgg ë làng al , seen làng xumb në
Ndax sa ma fan’s yi nak , am mool yee ci gën ë dense
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Bël ba ca ndar , sonn al na waa guét ndar géej oo
Sa telephone ak sa GPS ,  bul fatte gillet ba
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Ñoom laa bëgg ë làng al , seen làng xumb në
Ndax sa ma fan’s yi nak , am mool yee ci gën ë dense
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
 A dëgg ël , yaw mool u géej ,yaa di jàmbaar
Yaa bari fullë lool, Bari jom lool
Yaa donn loolu, Gëm yalla lool
Yaa xarañ lool , te tabe lool
Youssou woy na leen
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Bël ba ca ndar , sonn al na waa guét ndar géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Mool yi laa bëgg ë làng al , seen làng xumb në
Ndax sa ma fan’s yi nak , am mool yee ci gën ë dense
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Mool yi laa bëgg ë làng al , seen làng xumb në
Ndax sa ma fan’s yi nak , am mool yee ci gën ë dense

Ecouter

A Propos de "Mool"

Album : Mbalax (Album)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Nov 15 , 2021

Plus de Lyrics de YOUSSOU NDOUR

YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant

A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl