AMY COLLE DIENG Maanul cover image

Paroles de Maanul

Paroles de Maanul Par AMY COLLE DIENG


Souma sangone nga téey
Souma sangone nga maandou
Thi waxi diamour yé hey hey waaw
Souma sangone nga téey
Souma sangone nga maandou
Thi dieufi diambour yé hey hey waaw

Diamono dji lougne la khamal sank la
WhatsApp la tik tok la yakk la
Dangay waxak sa waay sa waay waxak waayam
Waxe dia di law bathi saye noon
Siwal la tong tong la diébaané la
Mbédd yek marché yi waxtaané la
Té say noone dagnou lay sossal
Féntal la way wou dootoul fay
Xiro bék nguayo bi niouy doundé
Xass tanték téssanté bi niouy deukké
Kouné yakal sa morom thi gaalou xathie
Yaakanté derr bi niaawna
Nangua réglé té nga maandou
Thi waxi diaambour yée
Nanga réglé té nga mandou
Thi dieufi diambour yée

Nitte xana xamoulo li Yalla bindeu yeup domou Adama
Ko thi gueunalé hé hé ho gueumléene YALLA
Nitte domou Adama bou sagané dina souffé ba raw
Way souffé yéé who lé lé lé lé hen ragalal YALLA
Boulako diaralé boulako diaralé boulako diaralé
Yaw boulako diaralé fobbal
Boulako diaralé boulako diaralé boulako diaralé
boulako diarralé dieulall
Boudé alal diaral nala beugueu beuzz diaral nala
Beugueu siw diaralnala yaw boulako diaralé fobbal

Baayil di wakh sa morom lou niaaw baakhoul
Nitte warta wakh moomam lou niaaw araam naa
Nitte dafay maandou té téya téy who who who
Waaw mani adounak lithi biram diaroul di niaawo
Yénél sa morom mbakh domou Adama ndiaye xana
Xamo lepp lou YALLA bindeu domou Adama lathi
Gueuna fonkk téy leen téy leen hé hé hé hé hén who
Hen téy leen hé hé hén
Nitte kou YALLA bakhal aldianay keureum nagnleen
Tey té xamné YALLA moy mayée
Nitte kou YALLA bakhal aldianay keureum nagnleen téy
Nitte kou YALLA bakhal aldianay keureum nagnleen téy
Té xamné YALLA noppi naa
Té xamné YALLA noppi naa
Nanga téy yow té nga maandou
Nanga téy yow té nanga maandou
Thi waxi diambour yée

Nanga téy yow té nga maandou
Nanga téya téya téya téya téy thi waxi diambour yée hé
Hé héy héy héy
Nitte kou YALLA bakhal aldianay keureum nagnleen
Tey té xamné YALLA moy mayée

Ecouter

A Propos de "Maanul"

Album : Maanul (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Nov 15 , 2021

Plus de Lyrics de AMY COLLE DIENG

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl