Paroles de Homie
...
Paroles de Homie Par OOTHENTIK ZEUS
Soo diapéni xamgama rek sigmay oumpeulé homie
Waayé booma diappè ni sa bop rek better you know me
Teh balaa ngay xam nitteu leundeum niou leeral la xol bi
Sa yéré noon bi, diap sa homie
Soo diapéni xamgama rek sigmay oumpeulé homie
Waayé booma diappè ni sa bop rek better you know me
Teh balaa ngay xam nitteu leundeum niou leeral la xol bi
Sa yéré noon bi, diap sa homie
Say
Brodah mbegté nga dji sunu noon yi
Garap binioudoon feekhloo nga gor fils
Ana premessou toudeunté dom yi
Pourtant yaa waroom fadj sama goom yi
Doumla fen diarouko coz know me
Xamoon ngani meuno dem douma lonely
Heister woo pour dieunder meu osh bi
Koudoul teew si sa levée de corps bi
Pour ma wake up fauk nga let meu down down
Mane nga nopp deggomeu nakh maagui sound
Avant ligne d’arrivée bi ngaa daw daw daw
Teh niokodoon dokhal dès le départ
Démessi khel ngani bopp sa bopp leu
Niou and ma daanou nga romb meu
Sama rangogn meussoul tok sa nopp
Niaata yoon ngama wane guinaaw ma toppu leu
Nakh gaawouma baayi teh thiow douma taawi, dou djigueen dou life dou money
Moomay tékheuleek gars yi mais respect ak loyalty, bouy niak faut que ma khaadi
Risquer sunu life siguil sunu yaay, loolou lagn diguéwoon homie
Teh nioog si batay manak yenen gars yima nguimb sen mbeur bi na daari
Soo diapéni xamgama rek sigmay oumpeulé homie
Waayé booma diappè ni sa bop rek better you know me
Teh balaa ngay xam nitteu leundeum niou leeral la xol bi
Sa yéré noon bi, diap sa homie
Soo diapéni xamgama rek sigmay oumpeulé homie
Waayé booma diappè ni sa bop rek better you know me
Teh balaa ngay xam nitteu leundeum niou leeral la xol bi
Sa yéré noon bi, diap sa homie
Anh
Waroom nga rouss dem bi boolé sa tour, si kaw son bougnma clash teh nga waroon ma sant
Doumla woowé noudoul ni nga toudou teh dou nignla toudé brodah diam moola dap
Khadji moola gueun parce que digko yaatal
Mais dou meuseu setaan mbokam niuw dila matt
Doo yallah kone boumla calculer woul, baama compter si iow téwoul lepp dina matt
Fuck
Gnima manquer teh warma motali
Sama guel sama bitch sama honey
Sama real, sama g, sama famille
Bougnko tegoon si yoon tay ma taali
Guémeugn ma teudj, rangoogn si khol
Dereet si beut homie meunougnfa gueudj
Defnaa album bi deudj, si wakhak ak si dieuf
Digma sikeul waayé guinaaw si lep
Dou doonati maak iow fi waanété
Li wess dou teh nga lekk bou agn di neekh
Nakh dokh nagn di goudé di naadié
Low yaa beugoulwoon tok ba khaar mou neekh
Soo diapéni xamgama rek sigmay oumpeulé homie
Waayé booma diappè ni sa bop rek better you know me
Teh balaa ngay xam nitteu leundeum niou leeral la xol bi
Sa yéré noon bi, diap sa homie
Soo diapéni xamgama rek sigmay oumpeulé homie
Waayé booma diappè ni sa bop rek better you know me
Teh balaa ngay xam nitteu leundeum niou leeral la xol bi
Sa yéré noon bi, diap sa homie
Ecouter
A Propos de "Homie"
Plus de Lyrics de OOTHENTIK ZEUS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl