JEEBA Dinala  cover image

Paroles de Dinala

Paroles de Dinala Par JEEBA


Dinala Dinala
Dinala yobou founga agoul wone
Dinala deink louma sorri
Mane Dinala diokh nga teeyil ma sama xool
Adina ngui guiss tée noone yangui wakh
Diaratoul thioow thii mane laa uuuhm
Banga diapé ba taay dou danga bagn dé
Danio indispensable si oie ndokh
Xoolo ndakh sama poche amna carte gab
Lidieunti wo ndakh sama pére dafa thiaap
Sama self am free reik molaa nioor
Defalougn la litakh bagn laay ngooro
Diaral ngama sopalékou done terroriste
Adhérer Hezbollah done extrémiste
Koulaa laal ma taak si kowam mouy guiss
Ba melni gangsta bou amatoul djizz

Kone Dinala Dinala deey
Dinala Dinala maay
Dinala diokh sama xool
Dinala deef sama tool
Mane Dinala Dinala deey
Dinala Dinala maay
Dinala diokh sama xool
Dinala deef sama tool
Loumou meñeu ma dieul
Yaay sama koom koom

Beut deey guiss tée xool deey wakh
Niaar yilé wone nagn maa oie ya takh
Bataay niouy ladj ndakham neewugn paradise
Alors que diégué wugn saax lou meelni paradise
Start from the bottom ba takh maay geureum
Kheuthieu bou dagoul may ladj ndakh dina dikkeum
Kheuthieu niou nga taaf niou sa boop door ma bizz
Nala feithial nguel ni Mbaye Ndiaye kaam dikaam
Lingama diaral yeup sougn ko togone di wakh
Waat nako si Yallah babe dina fi feunakh
Deef ko sa xool tée nga diap dou nakh
Suñu tool dafa laaw moukou boy dou lakh
Finga ma def ak fi ngama yobou khamna
Fouma dioulé ñane si Mawlana soumb biniou soumb
Agaal ko teemou gaaw
Wakh koko wakh koko wakh ko

Kone Dinala Dinala deey
Dinala Dinala maay
Dinala diokh sama xool
Dinala deef sama tool
Dinala Dinala deey
Dinala Dinala maay
Dinala diokh sama xool
Dinala deef sama tool
Loumou meñeu ma dieul dou
Yaay sama koom koom

Sometime niou tongo Kouné deem yonaam
Liniuy dioubolé dokoo khamaam
Lou thie mane lou thie mane worna doussi oie
Lou thie oie lou thie oie la adina di weur
Suniuy défaut ak sunuy caprices moom nga andeu
Emprisonné tée né dotoo ko xool
Nouñou meel nouñouy deef ngani beug na
Balaa nioula wo ngani waaw degg na
Kone babe wakh ma fooma def fooma def
Baby wakh ma fooma def
Finga ma def kham na sorii na ndakh meuneutouma
Meuneutouma doundou sans oie
Oie babe wakh ma fooma def fooma def
Baby wakh ma fooma def
Finga ma def kham na sorii na meuneutouma
Meuneutouma doundou sans oie

Kone Dinala Dinala deey
Dinala Dinala maay
Dinala diokh sama xool
Dinala deef sama tool
Dinala Dinala deey
Dinala Dinala maay
Dinala diokh sama xool
Dinala deef sama tool
Loumou meñeu ma dieul dou
Yaay sama koom koom

Ecouter

A Propos de "Dinala "

Album : Alajee (Album)
Année de Sortie : 2022
Ajouté par : Farida
Published : Dec 16 , 2022

Plus de Lyrics de JEEBA

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl