Paroles de Coumba
Paroles de Coumba Par JAAW KETCHUP
Mais boy fiils yaw Jaaw loy def ni
Boy Man Damay Nianni Coumba
Baan Coumba
Coumba Gaawlo Seck
Baane Coumba Gaawlo? Loe boy
Khaamo sa Bopp déé…
Wa Baxnaa…
Ay way ndeyssane domou ami teunguedj doff na
Makahala nek si internet bi di
Attaquer nit gni rek
Naka diék mani andok sa saguo…
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Nieup nénagn ma dou ameu
Coumba Coumba Coumba
Kouy laxatou dou max
Coumba Coumba Coumba
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Damay dém bouma kéneu té
Mbeuguél dév aventure rek leu
Dou yeufou fék
Niak dém meune nassi dé
Damay dém tay yobaler samay séritier
Doumassi sakh hésitez
Damay dém sama lay realisez
Yagu teud diko guént
Dafa yagu projet leuwoneu bou yaguu
Boumay dé si aleu nama gainder ray
Coumba lay diox paka koumou nex
Neu ray
Damko yagou barder depuis 1er single
Mou waay boutourgualer
Bané wingusigualer
Boy niani gawlo fok gua am si ngeureum
Damay lathier nank bane
Damay lathier nank bane sarakhh
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Nieup nénagn ma dou ameu
Coumba Coumba Coumba
Kouy laxatou dou max
Coumba Coumba Coumba
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Mom la yagu beugeu sama xol
Waw kay sama xol
Mission impossible guako fok
Mais bouy realizer wou frere digua lox
Takou diak rek diaroul sax protocol
Boum bi na takou diaroul sax yokh yokhal
Wa galler gui xar sama torokhal
Geumouniouni Coumba ladef sama xol
Loutaaax?
Town bi yatouna dé Coumba
Mais maneu taneu nala rek té goumba
Déguna louné ndax Coumba
Mais mane xamna lima xam rek moumeu
Sagn sagn lay démé
Douma reculer kayangu kayangu rek ba yégu
Bagn bagn bagn bagn
Khay khay khay khay
Ne suicide pas
Khay khay khay khay
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Nieup nénagn ma dou ameu
Coumba Coumba Coumba
Kouy laxatou dou max
Coumba Coumba Coumba
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Nieup nénagn ma dou ameu
Coumba Coumba Coumba
Kouy laxatou dou max
Coumba Coumba Coumba
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Boy medina la douma ragual
Yagu na guéneu di tangual
Comme que gayis daniou ragual
Bayil ma songu Coumba rek
Té niangual
Moma mak mais taxoul
Filako def sama xolbi taxoul
Damko love mais taxoul
Fitt lay démé dougou gualé taxaw
Mouniiiii?
Damadi ndananeu
Ba fo dém niouné diaw da tangu
Dama attaquer
Ba fouma dém nioumay xoter tank
Mbadou ?
Dama yayu xosslou ndax game bé tangu
Microphone bi damassi yagu démal
Ladjiko b beut
Boma guisseugoul si sa télé
Dagua goumba piteu
Boula nexer nexer néma doff bi
Damay nangou sileu
Mahfouss dioxnama ay conseil
Yeah adouna nileu
Yeah adouna nileu
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Nieup nénagn ma dou ameu
Coumba Coumba Coumba
Kouy laxatou dou max
Coumba Coumba Coumba
Damay niani Coumba
Coumba Coumba Coumba
Ecouter
A Propos de " Coumba"
Plus de Lyrics de JAAW KETCHUP
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl