Paroles de Nila
Paroles de Nila Par JAAW KETCHUP
[COUPLET]
Penda gassoul cambeu
Nga melni sindakh bouma khol
Sagnsé dama ko tameu
Kholma boubax lima sol
Souma solo guéneu nga warou
Takhoul nga am touti diom
Noumou geuneu séwé rek bakhna
Khotatil mako bassi souf
[REFRAIN]
Ndékété nileu nileu, nileu waay
Fima guéneu toyneu toyneu, toyneu waay
Ndékété nileu nileu, nileu waay
Fima guéneu toyneu toyneu, toyneu waay
[OUTRO]
Nénala boul sol taille basse del solou ni kooba yi
Soloul ni kou dieum Golden Five (kou dieum Golden Five)
Diaroul sax poudeur ak maquillage
Dionguama bas ley def (bou oyof) soxlawoul djiteul dra (soxlawoul djiteul dra)
Nileu bilaaay
Sama dionguama bi solna bas
Nga solou niou yémou niou ande ma am thieurou walay nileu
Nileu bilaaaay nileu
Nileu bilaaaay nileu
[COUPLET 2]
Na nga bayi boyal gou baari gui nga néké
Ya ngui yokk sama asthme dig ma ray rek
Del def sa feer you bawwx rek diko téglé
Rakh si pastille valda gui gout dey nékh
Nékhoul ba nékhoul fess ngeu
Bouniou done khar dé kouy ngeu sa sagnsé tay déh bakhneu
Diougeul dagou ma khol leu
Tekk nga sa sous fess ragadioul
Lou bess la si ioe diéguéssil
Wane ma sa guinaw leumbeuleul
Loussi yonou slip teumbeuleul
Li la yague rêvé
Ya ngui may doga meuna nékh
Nig ko défé nékhnamaaa woh woh woh !
Dionguama kay ragadioumaaaa…
Hummm… kay ragadioumaaaaa…
Ya takh rakadjou naaaa annh… kay ragadioumaaaa…
[OUTRO]
Nénala boul sol taille basse del solou ni kooba yi
Soloul ni kou dieum Golden Five (kou dieum Golden Five)
Diaroul sax poudeur ak maquillage
Dionguama bas ley def (bou oyof)
Soxlawoul djiteul dra (soxlawoul djiteul dra)
Nileu bilaaay
Sama dionguama bi solna bas
Nga solou niou yémou niou ande ma am thieurou walay nileu
Nileu bilaaaay nileu
Nileu bilaaaay nileu
Ecouter
A Propos de "Nila"
Plus de Lyrics de JAAW KETCHUP
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl