Paroles de SFB
Paroles de SFB Par DOPE MASTER
Started from the bottom téki yomboul I know
Succès yeufou deum leu mais angou nagn ko dh nigger
They told me all this problems leave me alone
Mane mere moy sama problem lissi dess yeup na nok feulé
Ligeuy ba deih teh khaliss doko dougeul si pakh
Ligeuy pour dieundeu souf teh souf moy moudiou sa kaw
Bala niouy yéwou lagn niou diay teh wakhalé wouniou sakh
Legui Khalatt liberté moudiou nek Guénteu si nioune
Oh my nigga Fuck le système
Boukou niou ndakh sougn derr
Gouvernement poukré
3e mandats soul nieup
Niom dh diangou niou kanamou télé bi rek laniou todji
Nioune gni yagu si ghetto bi Kham nagn lou gorr bi di datchieu
Diokh CFA money man
Boudé Dollar moniou geuneul
chargé mbétè life bi guerre leu
Heur bo yéwo ( paw paw )
Alma joint ma seukeut
Bopp bi dafeu fess ni ndieumeut
Probleme yi tantialo ni wa Reubeuss ( baaww )
Started from the bottom yoneu bi yomboul I know
Succès yeufou deum leu mais angou nagn ko dh nigger
They told me all this problems leave me alone
Mane mere biy sama problem lissi dess yeup na nok feulé
Si hood dagn yagu kharé
Kou yoroul dou shit loumouy tapét
Niak nioune Kham nagn ndieugeum Kom gars yi di tiéné maquett
Kom gars yoyou di tiéné charrette Wollahi dougn découragé
Dougn tayi si nokka niafé
Dagn bayi sougn yay yi galé
Lou diagoul niou diap diagual
Kou ndoudoul dou niak bakane
Kou khamoul na sakou kham kham
Kou febar na sakhal garap
Adouna doyna école
Ma bayi léne fa ak senn lessons yi
Terminale leu rakk bi yam
Ndékété yow commencé goul ( Baw Baw Baw )
Bayima guéneu fi yeup
Never give up
Téké diar ma mguémbou ni mbeur
Taylé nieup pour téglé victoire ( baaww )
Started from the bottom yoneu bi yomboul I know
Succès yeufou deum leu mais angou nagn ko dh nigger
They told me all this problems leave me alone
Mane mere biy sama problem lissi dess yeup na nok feulé
Ecouter
A Propos de "SFB "
Plus de Lyrics de DOPE MASTER
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl