Paroles de Li Lanla
Paroles de Li Lanla Par DIEYLA
Damala Beug ba xawma lima dal li Lanla
Tayoumako khale bi xawma lima dal li Lanla
Dama Nop te te lernama te lernama wat nako si yalla
Waxal ma ko wa Kone b niou bayima niou bayima ak
Yaw nguir yalla ma Mom la
Kay ngua wakhma foma dougeul mane
Beug na xam ndakh naturel na
Damalay guis salit dila Beug thiop melni Gaïnde gou guis yappa
Xawma li lanLa
Xawma li lane la
Xawma li lanLa
Xawma li lane la
Xawma li lanLa
Xawma li lane la
Damala guis salite dila Beug thiop melni Gaïnde gou guis Yap
Damala guis salite dila Beug fone xawma li Lanla
Wawaww mane ak xalé bi ba adouna Diekh ma wane Louy foula
Manila ki la done Xar défouma fo départ é li deh Thiou la
Foma wo ma niew ragalouma Lolou Wawaw ragalouma Lolou Wawaww
Han lima dal deh xamouma feke da niou ma
Liguey deh diap na dama ko
Nop mou dji dof ma diam leu demal ladial ma ko lima dal li lane la
Kay ngua wakh ma foma dougeul mane
Beug n’a xam ndakh naturel la damalay guis dila Beug fone
Xawma li lane la
Xawma li lane la
Xawma li lanLa
Xawma li lane la
Xawma li lanLa
Damalay guis dila Beug fone xawma Lini Lanla
Damalay guis dila Beug thiop xawma li lane la
Damako Nop ba dof papa sama Yaye nianal ma
Tayou mako xalé bi donal sama Serigne nianal
Damala love hé bayima bayima ak Mom nguir yalla ma Mom
Ecouter
A Propos de "Li Lanla"
Plus de Lyrics de DIEYLA
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl