ELZO JAMDONG Malembe cover image

Paroles de Malembe

Paroles de Malembe Par ELZO JAMDONG


Sa projet ken meussou ko khar
Oh mais lane la ci meun
Forcing bi nieupa ci marr
Oh mais lane la ci meun
Sayo khewlé ken dou nieux
Oh mais lane la ci meun
Y’ak sa gayi réunion di niou dieuw
Mais lane la ci meun

[VERSE 1]
Nite niteu geuneu bagn nite
Motax rappeur yi niofi
Geuneu meun bagn rappeur
Nénagn ma fi sa flow dineu rey nitte
Lima leer moy douma bal béneu rappeur
Awma temps boudoul money boy
Am ngen chance dama diangui wone
Mayé nangou baxoul dédééééét
Mayo ma mayma diameu nangou défaite
Zone nou town na ko res boy
Soma songué nala pess boy
Mane sokhlawouma ma press
 wala es faute I’m fucking best
Douma stress douma thies boy
Samay veste do guiss ken sol
 toujours class force tress kone
Amna ay ex youmay tek choc
Dima yoné text dima es pour niou sport
Yann khamna ma len meun
Ben khamna ma len meun
Waxkat yi bal en rekk
Wa kogn ak bi ak kogn bé
Yeup mane lagn geum
Malembe malembe fi de flounék ya aliéné
Beuri ay mc you khalélé
Togn nagn la moss wayé bal len rekk

[CHORUS]
Malembe malembe
Malembe malembe
Malembe malembe
Fi def niou ndank ya aliéné
Malembe malembe
Malembe malembe
Malembe malembe
Fi def niou ndank ya aliéné
Togn nagn moss wayé bal len rekk

[VERSE 2]
Sa clip beugou ko cher
Oh mais lane la ci meun
Amo ay mix mister cher
Wooooh... Oh mais lane la ci meun
Jamdong bi ngeu done khep
Tay moleu geuneu cher
Oh mais lane la ci meun

Sa wa kogn mane len défal
Car niow sétane
Chaine oh mais lane la ci meun
Lane la ci meun
Mane défar ay hit sama maladie leu
Ioe nulard ngeu lolou rek la khalate ci ioe
Té nioune rek nga fan diniou molo di dopp
Sa daw’ou fass’ou daw dotoul dalate ci ioe
Khamal ni calé nga ndax fi
Ngeu beug calate dou fofou
Chaque jour liguèy sama calendrier
Fi amo fi ndieurign comme salade si deum
Défal ndank bi lepp né sélaw
Mane ma niow yeungeulate leu
Yé leu mane ma niow yégeulate
Sa level ya meuneu faté
Ba yé nop sen game bi di nélaw
Ma niow nékhalate ko
Yeah mane ma indi rap bi nga yélol
Push ko baba ak yéla

Malembe malembe gnima done
Djignate nieup na len bétt
Ma ngui ci diaw ji yén fan
Ngen né dina len diokh
Sen dose ba ngen déh

[CHORUS]
Malembe malembe
Malembe malembe
Malembe malembe
Fi def niou ndank ya aliéné
Malembe malembe
Malembe malembe
Malembe malembe
Fi def niou ndank ya aliéné
Togn nagn moss wayé bal len rekk

[OUTRO]
Ken mounoul téyé lima tok di vélo awma OG
Télam dama niow ngir fayleu
Man’ak yen on es trop différent
Dama original meun ngen copié ma
Douma nopi ndax amna avenir douma salopard
Dama khiff meun na lekk yapp charognar
Douma domou riche amna avocat dou fepp la
Son bi di daw daroul à vos marques
Malembe, malembe
Malembe malembe
Malembe

Ecouter

A Propos de "Malembe"

Album : Malembe (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Sep 18 , 2019

Plus de Lyrics de ELZO JAMDONG

ELZO JAMDONG
ELZO JAMDONG
ELZO JAMDONG

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl