Paroles de Folie
Paroles de Folie Par KEY EM TI
Sama Bopp Dina Todj Mba Li Yoon La
Fouma Tokk Yow Lay Xelatt
Fane Nga Né Ma Nieuw Fonneu La
Yow La Nopp Bo Beugué Ma Watt Barki Yonent Bi
Magui Dé Thieuy Mbeuguel Sonneu Na
Feeling Feeling the Love That You Give Me
Am Feeling, Feeling Alright
Té Kouci Love Meuno Bagna Toudou
Fou Foufou Fou Fou Fou
Fo Fofofo Folle Folle Folle
Fou Foufou Fou Fou Fou
Yow Bo Nobé Meuno Bagna Dof Dey Yé Sa Folie Yeup Niou Nane La
Fou Foufou Fou Fou Fou
Fo Fofofo Folle Folle Folle
Fou Foufou Fou Fou Fou
Yow Bo Nobé Meuno Bagna Dof Dey Yé Sa Folie Yeup Niou Nane La
J’ai La Folie, Yow La Def Sama Xoll
Yay Sama Werouwaye Kone Dema Saurr
Khegnal Nga Sama Khol Motakh Sama Parfumé Yow Rek Ley Done
Yaye Sama Biberon
Nampal Ma Souba Ngone
Defma Nabou Dash Bandit Nga Dema Togn
Babe Girl T’es Ma Vice
Doundeul Nga Sama Life
Yow Rek Yama Yaye Size
I Love You Yeah You Know Why
Kou Beug Fok Nga
Fou Foufou Fou Fou Fou
Fo Fofofo Folle Folle Folle
Fou Foufou Fou Fou Fou
Yow Bo Nobé Meuno Bagna Dof Dey Yé Sa Folie Yeup Niou Nane La
Fou Foufou Fou Fou Fou
Fo Fofofo Folle Folle Folle
Fou Foufou Fou Fou Fou
Yow Bo Nobé Meuno Bagna Dof Dey Yé Sa Folie Yeup Niou Nane La
Fou Sama Dof Bi, Coco Chou Sama Copine
Sa Xol Bi Lay Fokati
Bagnouma Photocopie
Louma Am Dieul, Yama Doy
Meunoumala Geumé Ni Nakk Bekk Peulh
Dieundal La or Yow Yamay Teull
Dagnu Lathié Faly Ma Indil Len Ngoy, May Askia
Yagg La Golou Ni Casillas
Sama Nopp Siww Melni Fatiha
Souma La Togné Nanga Fakh Yarr, Nokh Ma, May Dioy
Nane La Bebe Bonheur Lalay Wowé Ay Nutella
Yow Nema Sama Dof Bi Ndakh Fi Kou Beug Fi Niou Wowela
Fou Foufou Fou Fou Fou
Fo Fofofo Folle Folle Folle
Fou Foufou Fou Fou Fou
Yow Bo Nobé Meuno Bagna Dof Dey Yé Sa Folie Yeup Niou Nane La
Fou Foufou Fou Fou Fou
Fo Fofofo Folle Folle Folle
Fou Foufou Fou Fou Fou
Yow Bo Nobé Meuno Bagna Dof Dey Yé Sa Folie Yeup Niou Nane La
Fou Foufou Fou Fou Fou
Kou Yegg Sa Mbeuguel Degg
Fo Fofofo Folle Folle Folle
Boul Bagn Koula Nane
Fou Foufou Fou Fou Fou
Billay Kou Beug Téperal Bo Nobé Dangay Taggok Saggo Niounanela
Fou Foufou Fou Fou Fou
Bo Beugué Faww Nga Degg
Fo Fofofo Folle Folle Folle
Kou Yegg Sa Mbeuguel Degg
Fou Foufou Fou Fou Fou
Boul Bagne Koula Nane
Fo Fofofo Folle Folle Folle
Deug Deug Bo Nobé Meuno Bagna Dof Dey Yé Sa Folie Yeup Niounanela
Fou Foufou Fou Fou Fou
Deug Deug Bo Nobé Meuno Bagna Dof Dey Yé Sa Folie Yeup Niounanela
Fo Fofofo Folle Folle Folle
Ecouter
A Propos de "Folie "
Plus de Lyrics de KEY EM TI
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl