Paroles de Corona
Paroles de Corona Par KEY EM TI
Yow corona
Sonn nagn ci corona
Nafi diogue corona
Gnu andeu xeex corona, corona
Sonn nagn ci corona
Nafi diogue corona
Gnu andeu xeex corona
Febar chine la diogué
Fa legui dadj na fepp
Sa yaram dafay tang
Diaffé noyi maux de tête
Gneup up xamnagn dafa metti
Prsk seukheut molay dall
Wotell samu 1515
Soko yegué andak dall, hee
Rassakh sa lokho
Gel ou sabou moylou geun
Soy nouyou salam doynaci
Un mètre i diguentayi
Moytoul lal sa lokho
Ak sa kanam entre parenthese
Seukheut déko def sa coude
Gadoul mouchoir you bess
Mani so meuné tokk sa keur
Foné nga teudjoufa
Warougnu dakhanté policier
Sougn né couvre-feu
Medecin yi sonnagn
Gnogui ci moussibeu
Respecté consigne yi citoyenneté dougouneu
Yow corona
Sonn nagn ci corona
Nafi diogue corona
Gnu andeu xeex corona
Yow corona
Sonn nagn ci corona
Nafi diogue corona
Gnu andeu xeex corona
Ministre di mougui def lepp loumo meun
Presi Dieul na matouwayy yi
Bougnu kenn geunn
Dou guerrou politique
Amoul partie dou yeuffou diné
Nagnou diapando
Dindifi febar bi geun doufiné
Vaccin bi dougn ko nangou
Bougnu kenn reyy
Testé ko Afrique lane motakh
Gnu beugg gnu def cobayes
Nagnou gnane ci yalla
Bepp diné ndakh
Mou defci jamm
Tokk sa keur
Reste chez toi, loloy indi ndamm
Yow corona
Sonn nagn ci corona
Nafi diogue corona
Gnu andeu xeex corona
Yow corona
Sonn nagn ci corona
Nafi diogue corona
Gnu andeu xeex corona
Yow corona
Ecouter
A Propos de "Corona"
Plus de Lyrics de KEY EM TI
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl