Paroles de Donne Moi Une Chance
Paroles de Donne Moi Une Chance Par WALLY SECK
Beugue nala
Mane déh miir na, nakh mane beugue na
Mane déh nop na, mbarane ma beugue na
Bouma kène yède
Loum ma deff dinama nèkh
Samay kharite dagnou may kagno
Yeup nènagne dama niakk fayda
[CHORUS]
Tamou woma begou loma
Dadièlèna nakhar mane bolè ci thiono
Nobou loma
S’il te plait donne-moi une chance
S’il te plait donne-moi une chance
Tamou woma begou loma
Dadièlèna nakhar mane bolè ci thiono
Nobou loma
S’il te plait donne-moi une chance
S’il te plait donne-moi une chance
[VERSE 1]
Mane déh mirr na, nakh mane beugue na
Mane déh nop na, mbarane ma beugue na
Bouma kène yèd loumou ma deff dinama nèkh
Samay kharite dagnou may kagno
Yeup nènagne dama gnak fayda
[CHORUS]
Tamou woma beugou loma
Dadjalè na nakhar mane bollè ci thiono
Nobou loma
S’il te plait donne-moi une chance
S’il te plait donne-moi une chance
Tamou woma beugou loma
Dadjalè na nakhar mane bollè ci thiono
Nobou loma
S’il te plait donne-moi une chance
S’il te plait donne-moi une chance
[VERSE 2]
Mane kholou ma guissou ma khalatou
Ma nop kènène koudoul yow
Beugou ma djièmou ma khalatouma
And’akk kènène koudoule yow
Guiss na djièm na meunouma
Nop kènène koudoul yow
Somay djany beugue na
Somay djany mane beugue na
Nop nala ba nopi teunkeu guama
Mounou ma dème
Beugue na kham na limay dadj
Ci ioe moma
gueneul... wawawaw
Wou yéé ! Koumay bolèkk ndaw si
Annh ! Beugue na ndaw si
Kénéne koudoul yow waw beugouma
Ci mom dara
Beugue nala (kima diaral)
kima gueneul
kima diaral
kima geuneul
kénéne koudoul yow waw
Beugou ma ci mom nada
kénéne koudoul yow waw
Beugou ma ci mom nada
Ecouter
A Propos de "Donne Moi Une Chance"
Plus de Lyrics de WALLY SECK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl