WALLY SECK Why Not cover image

Paroles de Why Not

Paroles de Why Not Par WALLY SECK


I’m going crazy sama booboo eeh booboo eeh

Baby baby mom ma
Thiop my money why not
Thiaabi keurgui matna
Ferrari bi nieuw na
Dior Christian ma diokh la
Versace solale la
Fendi, Louis Vuitton, Prada
Lo thi sol dou fake, real la  
Té sakh tambalé gouma
Babyyy baby
Everything I will buy oh buy for you
Té parégouma
Babyyy baby
Everywere I’ll go buy oh buy for you

I’m going crazy (oh mama)
Je sais c’que tu vaux (oh mama)
T’auras tous c’qu’il faut (oh mama)
Oooh I’m going crazy (oh mama)
L’amour comme c’est beau (oh mama)
Bébé na lingui yooo ohh

Khalébi khalébi everyday you’re supa class
You got a full flow
Diongué nga xam nga sa place
I like you girl wakhma lane nga gueun beugatt
You shake it shake it, moving blow my mind  
Girl ya ngui sexy sexy
Tek tchi bééli, Baby girl blowing, thiapit gnamitt
Wine up yeungaleul sa ndig, baby wine up (wine up)
Never let you down
Té sakh tambalé gouma

Babyyy baby
Everything I will buy oh buy for you
Té parégouma
Babyyy baby
Everywere I’ll go buy oh buy for you

I’m going crazy (oh mama)
Je sais c’que tu vaux (oh mama)
T’auras tous c’qu’il faut (oh mama)
Oooh I’m going crazy (oh mama)
L’amour comme c’est beau (oh mama)
Bébé na lingui yooo

Baby baby mom ma
Thiop my money why not
Thiaabi keurgui matna
Ferrari bi nieuw na
Dior Christian ma diokh la
Versace solale la
Fendi, Louis Vuitton, Prada,  
Lo thi sol dou fake, real la  
Té sakh tambalé gouma

Babyyy baby
Everything I will buy oh buy for you
Té parégouma
Babyyy baby
Everywere I’ll go buy oh buy for you

I’m going crazy (oh mama)
Je sais c’que tu vaux (oh mama)
T’auras tous c’qu’il faut (oh ma ma)
Oooh I’m going crazy
L’amour comme c’est beau (oh mama)
Bébé na lingui yooo oh oh
I’m going crazy (oh mama)
Je sais c’que tu vaux (oh mama)
T’auras tous c’qu’il faut (oh ma ma)
Oooh I’m going crazy
L’amour comme c’est beau (oh mama)
Bébé na lingui yooo oh oh

Ecouter

A Propos de "Why Not"

Album : Why Not (Single)
Année de Sortie : 2023
Ajouté par : Farida
Published : Jun 30 , 2023

Plus de Lyrics de WALLY SECK

WALLY SECK
WALLY SECK
WALLY SECK

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl