...

Paroles de Confuse Par WALLY SECK


Yaay booy wouyouma, damalay laadj (yeah)

Baay booy yédd ma, damalay laadj (yeah)

Beugouma loubakh reuthie ma, damalay laadj (yeah)

Beugouma réthiou tam, damalay laadj

Khamna limouy laadj (Limouy laadj, limouy laadj)

Niom niaar, kouné mounguék liniouy laadj (limouy laadjté waw)

Damay beuga diakhlé, ndakh awma choix ci niaar niou doywaar

Beugg nga mais ya ngui xel niaar

Beugo kou xar sa xol bi niaar baby

Xeyna gnifi diota diaar nio fowé sa xol banga fokni nieupa soxor

God loumou bind dathié deff niarr,

Ta yaw yaay sama guénwaleu man

Assaman si nimou yaato, naadj bi limouy tang, yaay képar guiy neubb naadj bé

Damay beuga diakhlé

Awma choix bébé khamna limouy laadjté

Linguère nga boul diakhlé

Mbékté dounya yi rek laala yéné

Hey, Damay beuga diakhlé

Awma choix bébé khamna limouy laadjté

Yow Linguère nga boul diakhlé

Mbékté dounya yi rek laala yéné

Souma guissé nganane da ngama nop

Té ndeye dji seikh dou ame ci diamalé

Melni assaman ci nimou yaato

Ak bidéw yi niniou taaro

Nékh nama, wayé diakhlé

Ndakh khamouma, kimay taneu

Linguère may Latyr Diop Déguéne Mbaye (Anh)

Ballago Khaliloulay (Wouy)

Ndiabote gueu lay woutal yaay

Té keur ga yafa doy lingère way (Ayaa)

Maadi bour guéweul, khouss ndama lay béguel

So beugué malay wayal, thiol, ndér ak tama way

Linguère kay, so banié ma wett kaay

Kaay, yaay sama wérouway

Damay beuga diakhlé

Awma choix bébé khamna limouy laadjté

Linguère nga boul diakhlé

Mbékté dounya yi rek laala yéné

Hey, Damay beuga diakhlé

Awma choix bébé khamna limouy laadjté

Linguère nga boul diakhlé

Mbékté dounya yi rek laala yéné

Nékh nama, wayé diakhlé

Ndakh khamouma, kimay taneu

No-no-no mon bébé

Ne t’en vas pas wawaw

Nékh nama, wayé diakhlé

Ndakh khamouma, kimay taneu

Ecouter

A Propos de "Confuse"

Album : (Single)
Année de Sortie : 2024
Copyright :
Ajouté par : Farida
Published : Aug 05 , 2024

Plus de Lyrics de WALLY SECK

WALLY SECK
WALLY SECK
WALLY SECK

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl