Paroles de SO BAYIWOUL
Paroles de SO BAYIWOUL Par JEEBA
[INTRO]
No ow wow yeah yeah yeah yeah
No no no no no ow wow
Yeah yeah yeah yeah
[COUPLET 1]
Mane teud na teud meunouma nelow
May tok di khalat louniou dieumelé kanam
Thi yone bi gnou soumb té amouniou katanam
Mane lingama jii meunoumako bafoué
Ngani thi sa khol ngama tatoué éh
Ma fess thi say beut
Té ngani bene goor khadiatoul thi sa heart
Yangui mougn yangui diap yangui diem
Yangui def yangui topeu yangui deem
Nguir niou binde souniou love thi story you geuna kawé thi real love
Baye meussoul wakh bama teek thi baat
Wayé tay dina done beuss bou ndieuk
Ndakh té goré goré rek mokoy faay
Dou danga bayi nieup ngani may sa waay
Lii boudé deug la lii dara douko fay
Wadialal say bagass tay dina niou fly
Même boumay fandé awma louma leek louma naane
Love binga may diokh doy nama leek ak naane
[REFRAIN ]
Gueunone na meti tay niouy work
Ba yalla def mouy mbeuguel
Oow baby eh bo bayiwoul douma bayi
Gueunone na meti tay niouy work
Ba yalla deef mouy mbeuguel
Oow baby bo bayiwoul douma bayi
No no no no no no nooooo ow woow
Nono no ow woow
Yeah yeah yeah ééé
[COUPLET 2]
Mane teud na teud meunouma nelaw may tok di khalat
Yoon bima dieul eh nathi am ndam waw wala deét
Danga takh ma bayi lep Lou guenone thi mane
Ma def la sama number one yeah
Kone linga ma wara wone
Mbeuguel thiofel bou deug dadi lale
None yangui sothieu siign beuga réé éh
Mais douniou meussa réé baby
Bouniou sérré souniouy coude
Douniou siign assouma mala nane réé
Wayé louy am am na ba noppi
Naniou rafétal deugeureul digeunté bi
Niane nathi yalla ay dom doom
Wayé louy am am na ba nopi naniou rafétal deugeureul diguenté bi niane na thi yalla dom doooooom
[REFRAIN]
Guenone na meti tay niouy work
Ba yalla def mouy mbeuguel
Oow baby eh bo bayiwoul douma bayi
Guenone na meti tay niouy work
Ba yalla def mouy mbeuguel
Oow baby bo bayiwoul douma bayi
No ow wow eh yeeeah eeh
Noooo baby baby bo bayiwoul douma bayi
Dinala dinaaaala dinala diox so bayiwoul
Bo bayiwoul douma b
Ecouter
A Propos de "SO BAYIWOUL"
Plus de Lyrics de JEEBA
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl