Paroles de Jengu
Paroles de Jengu Par ELZO JAMDONG
[CHORUS]
Flow wou terou bayou sogui dadiou tek ci set
Presque tomy jims tek ci perou set
Bari lamign sama kaw faw ma lémou len
Té louniouy wax ci mane yeup dara lérou len
Mane mounou ma sorou flavershit damay jengou rek
Mounou ma sorou flavershit damay jengou rek
Mane mounou ma sorou flavershit damay jengou rek
Mounou ma sorou flavershit damay jengou rek
[VERSE 1]
Andi mic yay records 4 projets yok job wagni wax
Somay set ma ngui port taub bi niow na contenaire barigo
Sama premier ennemie mane la
Mélomane yi kham nagn dama manquer viss
Samay studio sama scene de crime ray na
Sama nafs musique rek samay viss
Sa rappeur dafa beug melni mane neko
Awma premier mai awma jour férié
Homie paréna pour songue projet anytime
Depuis gorée husel moma geuneul am liguey
[CHORUS]
Flow wou terou bayou sogui dadiou tek ci set
Presque tomy jims tek ci perou set
Bari lamign sama kaw faw ma lémou len
Té louniouy wax ci mane yeup dara lérou len
Mane mounou ma sorou flavershit damay jengou rek
Mounou ma sorou flavershit damay jengou rek
Mane mounou ma sorou flavershit damay jengou rek
Mounou ma sorou flavershit damay jengou rek
[VERSE 2]
Kila diégué mola geuneu meuna siss
Kileu geuneu bégué mola geuneu meuna kill
Mandikat sou guissoul sax escalier sax yek
Ak nima khifé lek sama nit boumala yem
Boumala yem yag na ram légui dama wara naw
Boy yangui sandanté ay subliminal
Mais kholal nimay dialé comme warano
Amo tali ba ci samay come around
So khamoul sound dofi fuck around
Boul déglou ki né goor dou dougou wagn
Kholal togg na motax bok na
Who! bala ngey kham sama tour dama khar sama tour
Ken douko tangual ni mane meun na len al sama four
Woh woh ! leader ci art bi lindieunti
Lara djeez soga dokh (yeah yeah)
Douma lek li gayi togs ama avenir moma nior
Sa rappeur dafa beug melni mane neko
Awma premier mai awma jour férié
Homie paréna pour songue projet anytime
Depuis gorée husel moma geuneul am liguey
[CHORUS]
Flow wou terou bayou sogui dadiou tek ci set
Presque tomy jims tek ci perou set
Bari lamign sama kaw faw ma lémou len
Té louniouy wax ci mane yeup dara lérou len
Mane mounou ma sorou flavershit damay jengou rek
Mounou ma sorou flavershit damay jengou rek
Mane mounou ma sorou flavershit damay jengou rek
Mounou ma sorou flavershit damay jengou rek
Ecouter
A Propos de "Jengu"
Plus de Lyrics de ELZO JAMDONG
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl