Paroles de Xolma
Paroles de Xolma Par ELZO JAMDONG
[CHORUS]
Yeah ! ken dou dièk ba titeulma dédét
Kay diéguéma ma djiteul laaaaa, baby
Ken dou dièk ba titeulma
Dédét, pour sa yone lerr kay ma niteul laaa yeah yeah
Xolma xolma xolma
Dara dou yémou ba diaxassé niou
Xolma xolma xolma
Diaroul ngey guestou ma ngui ni sakaname
Xolma xolma xolma
Dara dou yémou ba diaxassé niou
Xolma xolma xolma xolma
[VERSE 1]
Ken dou yé ci sa nope, ken dou teudieuti sa bop
Di nga am li nga soppe nala yobou
Fou sori assassin yi ley top
Di nga ma lila nex ndaxté ma geuneu kham lila nex
Nala wax lila nex
Té di nga dégue deug sama wax dina lerr yeah yeah
All around the world yay queen baby
Kay niou dem nga guiss
Limala denthial ci xol, ken doula geuneu free
Ken doula geuneu kham love
Mane nga tamou ioe la mine
Ioe la kham ni ya ngui ci yone
Ken dou xékh ak ioe
Dofi kén kouma meuna teukheulék ioe
[CHORUS]
Ken dou dièk ba titeulma dédét
Kay diéguéma ma djiteul laaaaa, baby
Ken dou dièk ba titeulma
Dédét, pour sa yone lerr kay ma niteul laaaa yeah yeah
Xolma xolma xolma
Dara dou yémou ba diaxassé niou
Xolma xolma xolma
Diaroul ngey guestou ma ngui ni sakaname
Xolma xolma xolma
Dara dou yémou ba diaxassé niou
Xolma xolma xolma xolma
[VERSE 2]
Li geune rek a leu yéné, yay sama touti néné
Ioe founé ngama fété, fou kawé
la leu tek ioe lay guiss souma téné
Mani andal’ak sa crew dem bali
Doumala téré dem yendou ci say kharite
No no no, douma fiir douma salide
Dofi guiss goor gouma geuneu tali
Koula téral nga nitt, khamal ni ken
Doula téré nga free my baby
Souma guéner nga fiir lolo waral
Sa yma méré ma wiri fékissila
Koula téral nga nitt, khamal ni
Ken doula téré nga free my baby
Souma guéner nga fiir lolo waral
Sa yma méré ma wiri fékissila
All around the world yay queen
Baby kay niou dem nga guiss
Limala denthial ci xol
ken doula geuneu free, ken doula kham love
Mane nga tamou ioe la mine
Ioe la kham ni ya ngui ci yone
Ken dou xékh ak ioe
Dofi kén kouma meuna teukheulék ioe
[CHORUS]
Ken dou dièk ba titeulma dédét
Kay diéguéma ma djiteul laaaaa, baby
Ken dou dièk ba titeulma
Dédét, pour sa yone lerr kay ma niteul laaaa yeah yeah
Xolma xolma xolma
Dara dou yémou ba diaxassé niou
Xolma xolma xolma
Diaroul ngey guestou ma ngui ni sakaname
Xolma xolma xolma
Dara dou yémou ba diaxassé niou
Xolma xolma xolma xolma
Baby kay niou dem nga guiss
Ken doula geuneu free, ken doula kham love
Ioe la kham ni ya ngui ci yone
Té dofi ken kouma meuna teukheulé’k ioe
Ecouter
A Propos de "Xolma"
Plus de Lyrics de ELZO JAMDONG
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl