Paroles de Contact
Paroles de Contact Par ELZO JAMDONG
[COUPLET 1]
Gniou xol Gniou xol Gniou xol Gniou xol
Soma geumoul kay niou khol
Kay niou khol kay niou khol kay niou khol
Amna ganiou xol gniou xol gniou xol
Bimay binde li sama yaram mi ngui daw
Mi ngui daw, mi ngui daw, mi ngui daw, mi ngui daw
Nakhar bou yague ak thiono you bess rek yeah
Yone biniou diarone ba fi dagn ko tégui régressé yeah
Yakar bou tass, dokh na souniou kaw mbékté yeah
Amatoul diam ci sougn digeunté amatoul respect yeah
Ken mounoul wone geun ni dina meusseu tok té doumala khol
Noumay def ba faté ni ma nieuk sampe nobel ci sa xol
Yakar bou yakho ci base ken meunouko défar ci ken
Limala défal lou bax meuneutoumako défal djiguén
[REFRAIN]
Ioe la beugone tak khawma louma def baniou niak contact
Ioe la beugone tak wayé dama kheuy rek niou niak contact
Ioe la beugone tak khawma louma def baniou niak contact
Ioe la beugone tak (ioe la beugone tak)
ioe la beugone tak (ioe la beugone tak)

[COUPLET 2]
Warone na meuna nek sa bodyguards sa bodyguards text ala boni ma bagn
Bimala niaké ba légui diomi la def
Ioe docteur bimay fathi diaroul l’hôpital yay sama doliprane
Doliprane, doliprane kham ng ani ioe mi yay chef
Awma intérêt bok ci goor yi diay tanks
Souma off fé yamay chargé comme mobil cards sinon ay folie lay def
Set nala daw na sa guinaw, nameunala beugue nala guissate
Deugeu leu niniouy yague guiss
Gni néwone souniou ande meunoul réussir han han
Liniou doundou beug nako bissate
Togn nala beug na guiff balma
Amna niou yakamti niou gawa tass boul yakh liniou tabakh andeu tigui yako takh nioukay wax
Ken meunoul wone geum ni dina meusseu tok beuss té doumala khol
Noumay def ba faté ni ma nieuk sampe nobel ci sa xol
Yakar bou yakho ci base ken meunouko défar ci ken
Limala défal lou bax meuneutoumako défal djiguén
[REFRAIN]
Ioe la beugone tak khawma louma def baniou niak contact
Ioe la beugone tak wayé dama kheuy rek niou niak contact
Ioe la beugone tak khawma louma def baniou niak contact
Ioe la beugone tak (ioe la beugone tak)
ioe la beugone tak (ioe la beugone tak)
Ioe la beugone tak khawma louma def baniou niak contact
Ioe la beugone tak wayé dama kheuy rek niou niak contact
Ioe la beugone tak khawma louma def baniou niak contact
Ioe la beugone tak wayé dama kheuy rek niou niak contact
[OUTRO]
Khamna ni fauk ma dem
Aduna yatou na lool
Beuss di nga dadièk kénén
Kénén kouy deufeul sa xol
Bokouniou niniouy mougné
Bokouniou finiouy moudié
Beuss di nga dadièk kénén
Kénén kouy deufeul sa xol
Khamna ni fauk ma dem (han han)
Aduna yatou na lool
Beuss di nga dadièk kénén
Kénén kouy deufeul sa xol
Bokouniou niniouy mougné
Bokouniou finiouy moudié
Beuss di nga dadièk kénén
Kénén kouy deufeul sa xol
Ecouter
A Propos de "Contact"
Plus de Lyrics de ELZO JAMDONG
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl