Paroles de Messi 10
Paroles de Messi 10 Par ONE LYRICAL
Diékou nga kagn mai meumo diékh
Meuno soul loudoul beudiek thiép
Prési FIFA dikh na coupe Messi
Diam sa ndoye ngadim sourire guéne
Bomay khol force dangay téne
Mangui ak thiok déma royal tégn
Maléne meune fouf kou beugoul bagn
Réwandé boudoul degn melni sa khourou baye
Ngadim mental de fer la yoor
Loe la passé assumel say faute
Deurkiss ni kounta kinté mangui ngui
Bodé mango mane leu wégn ferrailleur
Esk meuss nga guiss kou ray médd
Mangui ak paka djibi outal meuwtii
Kipil sa beut Dip leudeum guiss
Amnaga rendez-vous mane la ophtalmo bi
Dina kat sa ndaye mangui ak brass bi call me capitaine Zimbabwe
Diléne taclé ak samay
Tank néne, krath kath
Ba degu wouyawauy
Meusso sassumé, ngadim kapithié
Kone bayil sa khél bignay diiw
Seutou Doudou ndiaye rose ak thiou
Bouma sandé pique ma livré la aye fleuve
AB bou D CD nga bientôt
CD sa biir CD moy témoin
Awé kone sa D nga gniew féké
Ok voilà bon gniou procédé
Dolé mame ndiamane na dakhar sa ndaye
Kép thiapatat si karawou niagn
Pique nga lancé do gaubé si tole
Pérréra sa santé def si mbaye
Khass nga sa tonton si son
Mogui banékhou si mère bi non
One dafa con yor bidon
Essence diokh la briké nga tale sa bon
Clash ma ni condom, si djion
Mbalit sama salle de bain
Clash ngama kokoriko bimay plumé song bi dagnama done mathial
Esk dougniou mortal combat
Sa testicule yi lay dath compa
Mane de fois ni boy
Des fois kom pa dangamay wéki
Damalay dadila banc
Fuck you, fuch your wife, fuck your son
Gorgoloul si peur yoor si keur
Fuck you, fuch your life, fuck your ever
Déchargé balle yi khar lossi meune
Sa khol da diekh comme karawou abba
Mala tenir tête fils, nga may baba
Kiroukou da khép caméra karaba
Youné na sa papa cadeau Noel pétale
Danga amé aye rap
Dama yor aye deum tour dérét call
Boum yi tak say tank
Sa djiko bi da séw
Sa compte khaliss yi
Lay brake bouba chinois
Feul fi feulalé fé gniame ki gniamalé ké Sali fondé
Niké niké douma séne mass
pitié pitié damalay éléctrocuté
Ngadim canara diéth flotte comme couber si dieth
Imigration clandestine gninga youbalé
Dagniou fa dess ba yorone khaliss dougniou fa tok
Yaboma sokoy nayi nouy naw
Lanb dath fuck you tatou néne
Dof gouùb teukh lou
Sassouné oume koor
Sissou meunou mako
Si weer bou seet
Animal gniangal gainde diéth
Teukhlou nga ba routh tatou gained
Michael beuroz bé si son bi
One dafa beuri chemin labyrinthe
Sa équipe type mane lagnioury rêve comme joueur
Messi technique Fifa mane lagniou geume djioz
Statistic djiombalou maléne dambalou boy
Talent day fay
Question de temps leu dara dou doy
Ecouter
A Propos de "Messi 10"
Plus de Lyrics de ONE LYRICAL
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl