Paroles de Die Young
Paroles de Die Young Par ONE LYRICAL
Life dou cheat
Kone boulé néxé toux
Sa mame dead na big
Heure boula néx guay dox
Loy déff fii
Amoulo sax 20 ans
Nirouwo fénekate, boulma xole besstané
Generation, die young
Sama generation die young
Ambition 10 pour cent yeah yeah
Die young
Deug complexé ak jew
Die young
Outi camps kéte kéte kélén
Temps boy xamougnouwone fowoume taate
Tous les jours Senegal gnénéne cateuf
Ligua mome bary young délinquants
Takoussane beurseete daguay féné
Koula jam dagual naane delay guagn
??
Vider carte bancaire, féssale sa cassier
Boy fuck 4 4, 44
Pourquoi séne xéle yi guate
Took biir classe ak ay dadj
Ko lewtole dalay daane
Fuck 4 4, 44
Gueume yalla moy independence
Pourquoi séne xéle yi guate
Ndiole wéx guéne défonekoffi tendance
Tokk biir classe ak ay dadj
Wékill pontou dependence
Ko lewtole dalay daane
Uno, dos, tres, work
Give me the key
Appartements yi di todj comme tabax
Comportement ragal oute jabar
Chicha di takk hi yamba ak tabac
Missale kou siw rk sama
Appartements yi di todj comme tabax
Comportement ragal oute jabar
Chicha di takk hi yamba ak tabac
Missale kou siw rk sama
Am respect walla guathié
Gnémé déff walla compléxé
Sathieye, waw kay
Taane sa boula néx fils do fay
Am respect walla guathié
Gnémé déff walla compléxé
Sathieye, waw kay
Taane sa boula néx fils do fay
Sénégal béneu boop leuh
Kéne douko ar niar nioko book
Yénay sacrifice gnidone ssth néne dagnou fatélene jugéléne
Fucking loose
Ecouter
A Propos de "Die Young"
Plus de Lyrics de ONE LYRICAL
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl