ONE LYRICAL  Banlieue 13 cover image

Paroles de Banlieue 13

Paroles de Banlieue 13 Par ONE LYRICAL


Dama dioudo si ghetto, magué si ghetto
Wax len ko fala beug déh (ghetto, ghetto)
Boy banlieu kéne douma lale original ndax yén yéneu ma ndieukeu tall
(Ghetto, ghetto)
Guinaw rail lay titeuro, khék ak Cissé Lo sagn nako té ken douma té
(Ghetto, ghetto)
Fi ndox mi taa lay represent marouma nane mak yen ba lalou hospital
(Ghetto, ghetto)
Pikinité lokho yi cikaw beguél bou dé fière nga lkho yi cikaw
(Ghetto, ghetto)
Daniou nitté pare niémé thiow, amouniou mais no stress lagniy doundu si xol
(Ghetto, ghetto)
Bagn gathié fété souniou boor, da nga beug kham hood bi dangay ndieukeu xool
(Ghetto, ghetto)
Fi laniou diougué wouték nouniou mel khan ani banlieuz’art doko fouti ci nen
(Ghetto, ghetto)
Ndongo ak Thioubalo ana Pape Diouf système gokh bi tek naniou coup de pouce
Tigirimbi athia niamou mbaam légendaire Omzo rapatakini ndam
(Ghetto, ghetto)

Ghetto, ghetto
Ghetto, ghetto
Ghetto, ghetto


Béck si mane fière ci mome
Béck ci nioune béck ci yén, fière ci niom
Béck si meusseu Eumeu Sène champion
Rest in peace Doudou Diouf platinum
Lékouniou nanouniou tamite gnéwou niou
Nioune douniou nagou té sanguinairouniou
Thiaroy ba diameugeun diagsawfière ci nioune
Parcelle ba guédiawaye nimzag fière ci nioune ghetto
Nio dieul 1er si souniou génération
Topal féé ndax danio tilime diapo
Feep fougn dem nioune Pikine laniouy bakko
Yen nieupay d’accord yen nieupay bégué waw goor
Mane dama bagn gathié, danga beugeu kham lathièl
Nioune dagniy door dakhé khamougn louy woup sathiey
Fi échec dey khar comme guent di mbote sathiès
Mafi diarone merci Dakar siguithior ghetto
Boudé ghetto ngay live sa lokho cikaw may guiss
Daniou lay téral ngey guiss kone loulen téré nieuw live
Lawlathiate Lamsarr, yeumbeul ak zack mbao
Keur massar big town thiaroy azur daf ghetto

Ghetto, ghetto, ghetto, ghetto
Ghetto, ghetto, ghetto

Yeah! Ok Son bi dédié nako kou amoul ghetto
Moy sama Ex moy sama hero
Ghetto ladone guiss mane
Ghetto ladone guiss mane

Ecouter

A Propos de "Banlieue 13"

Album : Potentiel (Album)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Nov 06 , 2019

Plus de Lyrics de ONE LYRICAL

ONE LYRICAL
ONE LYRICAL
ONE LYRICAL

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl