DOPE MASTER Go El Matt cover image

Paroles de Go El Matt

Paroles de Go El Matt Par DOPE MASTER


GO El matt
Go El matt
Go El matt
Pull up in the city I heard
GO El matt
Go El matt
Go El matt

(...)

Niom dougn dém beugougn guiss kou dém
Lo ték niou bagn dou guate lagn fi ték
Dof dof lou si guéw ma fatchieu léne si pét
Stay real no cap beu guédji bi di férr
Bérr sama daara day bi meu guéneu si daara bi
Kham nguani album bi guéneu rek mo téré ma ba leu fi
Nieuw pour djité boy yi yeup narouma langu pour beugu siw
Dama geum sama bopp beu souma kholé doumala guiss
Fake nigger don't walk around kou yom dou déff diff
Matt moy yolé féép nguay ték di tégui
Couplet you woor lay téglé diégui frontière boy gni séne rap bi
C'est le bordel (Ndanane)
El Matt si kaw dawoul baankass
Téglé album téglé liass
Téral mère bi fokma téféssou

GO El matt
Go El matt
Go El matt
Pull up in the city I heard
GO El matt
Go El matt
Go El matt
And all my niggers scream it
GO El matt
Go El matt
Go El matt
Pull up in the city I heard
GO El matt
Go El matt
Go El matt
(Let's go Let's go Let's go)

Ecouter

A Propos de "Go El Matt"

Album : Go El Matt (Single)
Année de Sortie : 2022
Copyright : © 2022 Nautylusprod
Ajouté par : Farida
Published : Jan 20 , 2022

Plus de Lyrics de DOPE MASTER

DOPE MASTER
DOPE MASTER
DOPE MASTER
DOPE MASTER

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl