AKHLOU BRICK Crazy Love cover image

Paroles de Crazy Love

Paroles de Crazy Love Par AKHLOU BRICK


[VERSE  1]
Ioe rek ka kham sama prize
Yama dieund té waxalé wo
Da nga changé sama life
Wakh ma deug té nakhaté wo
Nga fek xol mille morceaux
Tabakh ko ni maçon
Bamouy fegn sama eyes
Kou beug beug nala
Kou bagn nama bayék
Ioe yay sama way waat na né

[CHORUS]
Ioe rek ci xol bi lénén doufi
Khathi geum na né
Yay sama doncteur kénén douma
Fathi khamna né
Louma weuri fénén am ngako
Ba paré diém na né
Yay sama diant nama touma nathi baby
Nekouma because
So crazy in lova, baby
I love you love you so much so much baby
Néma diapeu ngama do bah do bah baby
Nekouma because baby
So crazy in love, lova baby
I love you love you so much so much baby
Néma diapeu ngama do bah do bah baby

[VERSE  2]
Setlou na say yomay khol di ré
Waro nameu potou mèw ndax malay dadji
Sama xol bamako sentiroulé
Laleu weur diapeu la
Ndékété yay sama sathie
So beugué ma dékilate abdou rass dédét
Doumala trahir niou fit ko def ko maky
Kham nga loutakh mey bagn
Nga def maquillage
En faite dang ko waneu
Waaral sa xl geuneu rafète
Siguil kholma si beut baby
Ré ma c’est que sila
Sama rétane bi di meuneu
Guén mbecté bi leu
Khipil réwantoul wan
Ma caprice yi leep ci la
Mba kham nga ba dof dof lo ba
Kharou ma fékissi la
Mane dama beug nob la damala fan
Sa tour bi la feusseul fégnal
Ko ci woy fenth
Dés fois ding ma wo mané la awma temps
C’est que journée bi
Ioe lay khalate té goudi ioe lay guént
Waat nan né

[CHORUS]
Ioe rek ci xol bi lénén doufi
Khathi geum na né
Yay sama doncteur kénén douma
Fathi khamna né
Louma weuri fénén am ngako
Ba paré diém na né
Yay sama diant nama touma nathi baby
Nekouma because
So crazy in lova, hééé can be
I love you love you so much so much baby
Néma diapeu ngama do bah do bah baby
Nekouma because baby
So crazy in love, lova baby
I love you love you so much so much baby
Néma diapeu ngama do bah do bah baby

Ecouter

A Propos de "Crazy Love"

Album : Crazy Love (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Sep 11 , 2019

Plus de Lyrics de AKHLOU BRICK

AKHLOU BRICK
AKHLOU BRICK
AKHLOU BRICK
AKHLOU BRICK

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl