AKHLOU BRICK No Issue cover image

Paroles de No Issue

Paroles de No Issue Par AKHLOU BRICK


Akhlou Brick from Sénégal
West Afraica World wide

Hawma louma gnam ba diodo
Sa liguéya  diap sa Serigne bé aay
Tek ma naagn  dima madj lo
Yay sama Générale  nala todial way
Takhaliko  menoutoula né
Kanar bi teud nagn ko sani guédj bae
Falewma bénén  go
Lidiantiwma bénèn  go
Matay  nop la angou thiow li
Bb nagnou rouslo wahi noni
Faw rek gnou wan lén ko

Jelel sama money now
Guisatouma Baby goumba na nah yay sama eyes
You make me feel the good life
Give You my money
See you go down
For me Yi go down low
Baby loumala may hep nako
Te man awma si yaw sago
Bb wan ma ningay dago
This is the way
Wan ma ningay dago
This is the way
Wan ma ningay dago
This is

Ba sa xol Bangui sed
Man mangui fekh
Retalna man malay xol rek di bek
Wanél   niga meunee
Wanél  né dou Ben
Dieund lal bou noy wanla noy danou si nek dengua,
Foma fek dik sif ma séey  
Fo aw yon nangoulnala  Biss niki tay
Meusso  guiss djinee yak mom kif kif la kay
Gagné nga   Sama coeur  dakh sa assou pikaray

Ligéyma dama beug geunla bardé
Nagn ko doumdou mak yaw kassé
Mbeungel boudé rayé yalna dé
Meunatouma sound dans yaw

No man awma diom
Paka  bingma rayè mako dass
dara metiwouma sino malila alma gaz
lamign béngui sa  poche
sagnatouma  kass
Guissna sama ourou ayni nieuweul fi gnou danse kay

Jelel sama money now
Guisatouma Baby goumba na nah yay sama eyes
You make me feel the good life
Give you my money
See you go down
For me Yi go down low
Baby loumala may hep nako
Te man awma si yaw sago
Bb wan ma ningay dago
This is the way
Wan ma ningay dago
This is the way
Wan ma ningay dago
This is

Sa hol bi gagnou won na
Maa gnew fadial la gomi
Rangogni fér na honey
No mind!
I never u let you alone
Dou dem la gneup wahone
Décider wougn ko won
It just man ak yaw dong
Manak yaw la wara don bou thi ken dougou

Falewma bénén  go
Lidiantiwma bénèn  go
Matay  nop la angou thiow li
Bb nagnou rouslo wahi noni
Faw rek gnou wan lén ko

Jelel sama money now
Guisatouma Baby goumba na nah yay sama eyes
You make me feel the good life
Give you my money
See you go down
For me Yi go down low
Baby loumala may hep nako
Te man awma si yaw sago
Bb wan ma ningay dago
This is the way
Wan ma ningay dago
This is the way
Wan ma ningay dago
This is

Ecouter

A Propos de "No Issue"

Album : No Issue (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Feb 08 , 2021

Plus de Lyrics de AKHLOU BRICK

AKHLOU BRICK
AKHLOU BRICK
AKHLOU BRICK
AKHLOU BRICK

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl