Paroles de Borom Diamano
Paroles de Borom Diamano Par AKHLOU BRICK
Kérok bagnou paré Dem haybou ba di soukourat
Yalla nang fa tew johgnou yonnént Sidy Barhama
Yeurmandé Yalla dji kou la am Niass am na sowétass
Yalla Yalla def gnou ndongo Sidy Barhama Wahlén ya Sidy Barhma wahlén
Ya Sidy Barhama moy Borom Diamano
Baye Niass gnoun sougnou Gor gui
Moy Borom diamono
Baye Niass
Aboul al Arwah moy Borom Diamono
Baye Niass
Baye Barhamaaaa
Ara
Kou yalla May kou am set lou ham ni wadji baye la
Gnou yagnou doy dang gnou neub sa bopwanel gnou yalla
Leer bangua medina
Gamou berndel Bi diemi yalla la
Nek di yalla doh thi ba fanaw
Lek thi yalla tank thi Di nan waouh
Kou yello beug ? (Barkhama baye)
Kan ngen beug? (barhama bayo barhama)
Kou yello beug ? (Barkhama baye)
Kan ngen beug? (barhama bayo barhama
Non bay moy wadji
Bayou hawsa yek nari
Mognou nandal bagnou mandi
No baye no life
Wilani jangal nagnou hitma
Talibe eudeup enh
Foudoul medina doufa teud carte gui deup na
Guiss n’a yalla guissma
Ham ko guen thi fitna
Bayou bidewou bidew yi bay bidew bou bess la
Goor yalla thi pochou baye
Kouy bokale dou andak baye
Daradié ne baye your side
No baye no life
Barhama banga Roté ba say Bagane fées
Bawal nga gna la don haar ba séni ndap féss
Halam ak allalam mom la diay thi l’islam
Bour signél ko mou wéer johko hatmou faydoumya
Kou ngén beug? (Barhama Baye)
Kan mo yéllo beug (Barhama Baye)
Koungene beug (Barhama Bayooo Diarama)
Kon wahlen
Ya Sidy Barhama moy Borom Diamano
Baye Niass gnoun sougnou Gor gui
Moy Borom diamono
Baye Niass
Aboul al Arwah ki moy Borom Diamono
Baye Niass
Baye Barhamaaaa
Ecouter
A Propos de "Borom Diamano"
Plus de Lyrics de AKHLOU BRICK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl