
Paroles de FMCB
...
Paroles de FMCB Par OOTHENTIK ZEUS
Say
Meme bouder fekker ma ci boolé, money baa ngui teew
Sokhlawa kouniou juboolé meun naa corrompre adversaire
Ak sa xel bi loumou daw
Doo dokh ci sama brain
Topal ci sama name
Di yak der mais maagui sant
Manela mbegté sama mère
Doon exemple sama frère
Pattou dalou sama père
Ay narcos diokhnagn ma repect
Mane ngay nioodi mexicain teh diarcoo tacos sam weet
Kep kouy newschool may sa leader
Tass sa yaram ba fa ideu
Sa mc moofa d don’t give e f boudé sa g leu
Film rap bi doumsi liir scénario bi maaako bindeu
Boy maafi moudièr rap teh djitou naa ci mc lida
Meme booma beugoul soutenir
Mane maagui coatcher sous tenir
Waa gallé tekk leen au-dessus
Le jeu j’oriente et j’organise
Même bouma topé seni normes jamais on me normalise
Comédien ni momo henri dara nekooul séni om
Kou doug sama terrain ci sa milieu naala fowé
Douma nittou milieu
Mais milieu beurinaafa nitt
Xooléma guardiola si effectifou man city
Son bi doumko marketing
Baayinaakok cissouman yi nakk kou nek ak sa thing
Xamanaa lane mooy deup tchiin
Kone tay meun naa sant yallah meun naa organiser chill
Wakhal bitches yimay toogué lignmay yakk lep mana
Success moomay kheegn niom nak liniou ba ci wanak
Amoul morom bouko raw dess na tuti nagnko nama
Woorna naby boumleen toppé nek nabba
Nigmay beuguer baayi xel baa doula moudier diokh tumeur
Rappeur bou sett stylé boy dégager bonne humeur
Guels yaagui am ay vues ci mane tek douniou samay youtubeuses
Teint chocolat bi laniou bueg mou niew diw ci beurre
Niom ba legui nioogui thioow
Teh mane lanioug deg because i’m the fucking top boy
Y’all neggers already know maaguek rio city tek ndakaru naako mom boy
Niom ba legui nioogui thioow
Teh mane lanioug deg because i’m the fucking top boy
Y’all neggers already know maaguek rio city tek ndakaru naako mom boy
Niom ba legui nioogui thioow
Because i’m the fucking top boy
Y’all neggers already know
Tek ndakaru naako mom boy
Meme bouder fekker ma ci boolé, money baa ngui teew
Sokhlawa kouniou juboolé meun naa corrompre adversaire
Ak sa xel bi loumou daw
Doo dokh ci sama brain
Topal ci sama name
Di yak der mais maagui sant
Faukma siguil sama père
Keurgui vue sur la mère
Villa chambre salle de bain
Faukmou dèlou xallé fresh
Faatélikou diamono wam li ci dess lep nako ress
Yaw, keur ndiaye lo
Fekké ma ci boolé yaw yeah
Teungueth fekké ma ci boolé yaw
Dakar fekké ma ci boolé yaw
Galsen fekké ma ci boolé yaw
Ecouter
A Propos de "FMCB"
Plus de Lyrics de OOTHENTIK ZEUS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl