Paroles de Délo Ndioukeul Serigne Bamba
Paroles de Délo Ndioukeul Serigne Bamba Par SOKHOU BB
Dieureudieufé Mame Bamba diarama Mame Cheikh Ibra Fall lo
Dieureudieufé Sérigne Bamba Mame Cheikh Ibra Fall yaram la
Dieureudieufé Mame Bamba diarama Mame Cheikh Ibra Fall lo
Dieureudieufé Mame Bamba Mame Cheikh Ibra Fall yaram la
Baniou woté bureau ba thia ndar, khadim ma takhaw ni y’Allah rek’ay buur
Dieureudieufé Sérigne Bamba, Mame Cheikhra Fall yaram la
[VERSE 1]
Hummm... Lamou tontu bureau ba thia ndar moko yobou ma yomba
Gars yi wedi wone naniou bayi fi niou tok niou yobou domi Mame Diarra
Ka mome fa ndar manaté batay moy wadia
Nialone fa ndar dou niom té batay douniou wadji
Lamou tontu toundu djé wal kou yobou ma yomba
[CHORUS]
Dieureudieufé Mame Bamba diarama Mame Cheikh Ibra Fall lo
Dieureudieufé Mame Bamba Mame Cheikh Ibra Fall yaram la
Dieureudieufé Mame Bamba diarama Mame Cheikh Ibra Fall lo
Dieureudieufé Mame Bamba Mame Cheikh Ibra Fall yaram la
Baniou woté bureau ba thia ndar, khadim ma takhaw ni y’Allah rek’ay buur
Dieureudieufé Mame Bamba, Mame Cheikhra Fall yaram la
[VERSE 2]
Bolé’k nagn ko gaindé gou tok fouki faan lékoul niam
Gaindé nga waff thia kanamou Bamba domi Mame Diarra
Nakk wagn ko bolel aka gawa dièl djibril
La dadièl ken dou Bamba domi Mame Diarra
Cheikhouna Bamba mofi wotou si yonent bi
Té missal bi lou werr leu fell khourane
Diadieufeuti yaram bi,
Mbacké ya niwone ya rabi mane dé mome mane nama yanou yan bi
Diadieufeuti Mame Bamba, diadieufeufi sama tabi
Yay geusseum Mbacké mouy tabi, sa tabaraw taw bi
Diajeufeuti sama ndiol ma
Mbacké ya kawél sama khayma, ya meuna mayé ni am ma
Diajeufeuti Mame Bamba
Mamy sérigne abo mou Mame Sey Fall bété bété dieureudieuf
[CHORUS]
Dieureudieufé Mame Bamba diarama Mame Cheikh Ibra Fall lo
Dieureudieufé Mame Bamba Mame Cheikh Ibra Fall yaram nga
Dieureudieufé Mame Bamba diarama Mame Cheikh Ibra Fall lo
Dieureudieufé Mame Bamba Mame Cheikh Ibra Fall yaram nga
[VERSE 3]
Sérigne Mountakha néna, bayou Sérigne Moussa nawil néna
Nakhar gou sossou ndakaru amo niéti goud’ék Mame Bamba
Amna mbégté mou koraw ci oubit’ék Massalikul Jinaan jé
Mounouma mounouma bania sargal sama bay
Dieng salla thioro madjiguén ali awa baba ba thia
Bagagn baye fall’ou Sérigne Abbo Mbacké Fallilo
Dieureudieufé Mame Bamba diarama Mame Cheikh Ibra Fall yaram nga
Dieureudieufé Mame Bamba diarama Mame Cheikhra Fall lo
Dieureudieufé Mame Bamba diarama Mame Cheikh Ibra Fall yaram nga
Ecouter
A Propos de "Délo Ndioukeul Serigne Bamba"
Plus de Lyrics de SOKHOU BB
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl