Paroles de Mame Saliou
Paroles de Mame Saliou Par SOKHOU BB
Cheick saliou borom khelcom borom yeurmande thiey mbacke waw
Cheick saliou borom khelcom beugeu gonei yi thiey mbaxke waw
Aannh anh! Mame saliou wo
Bilay bole kok yeureme diaame gnei
Dieguer goumou dieguer souniou borom
Ye le lee, souniou borom mo
Deukeul len ma tei deglou ma ka
Cheick Bamba done waye mo deloussi won
Setloul ma yaw mi lei
Cheick Bamba seringne saliou dagn len ni diawaler
Mellow Moustaphal Moukhtar rou serigne saliou wako yor dako roy thie bayam
Boler kok lagne ko dondoleer
Kou xam Cheick saliou
Xam ni loumay wax degue la
Djiko mak djiko yoneinti bi ben laa
Walahi, mo done khadim
Si zahir ak si baatine
Aah aah, mame saliou woo
Cheick saliou borom khelcom borom yeurmande thiey mbacke waw
Cheick saliou borom khelcom beugeu gonei yi thiey mbaxke waw
Ye le lee, souniou borom mo
Nangou nagne mbacke
Ni ya done Cheick Bamba
Doxinam wa, waxi nam wa
Dieuf yenam ga yako yoron Cheick saliou
Ya done ame yeurmander
Da woul khebater, daawoul khaster Mindef
Do ngagni ya mandou won wadji ler
Ndeker topou yoneiti bi moy topou Yallah
Kon mayam moung si yaw
Bou feker, amone nagnou thieur
Thia mame adamak awa def nako adiya Fakh barli
Thiante mo niou war sou niouy mame bagnou tolou ni
Amougnne wone li gnou ame def nagn ko adiya
Bayou serigne Cheick saliou miy khalifan si diamono dji
Mbokou bayam serigne Moustapha saliou
Domou bayou serigne abbo mbacke fallilou
Niom douniou niaar ben lagnou
Kep kouy mouride nek talibe serigne saliou
Sa dieuwrine dia lam la waxon dieuffer ko
Bo beguer raw ame ngeureum
Ibrahima gueyen talibe serigne saliou
Borom Bamba automobile
Mame mou serigne saliou Bamba partenaire
Ablaye general niang mou serigne Abdou Karim
Aka beugue serugne saliou
Khadim ane borom anrolette ndiouga thiam balamagnsa sangse
Aka beugeu serigne saliou woo
Bou feker, amone nagnou thieur
Thia mame adamak awa def nako adiya Fakh barli
Thiante mo niou war sou niouy mame bagnou tolou ni
Amougnne wone li gnou ame def nagn ko adiya
Ecouter
A Propos de "Mame Saliou"
Plus de Lyrics de SOKHOU BB
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl