Paroles de Domeusseu Am Kou Melni Mane
Paroles de Domeusseu Am Kou Melni Mane Par OMG
[REFRAIN]
Do Meusseu am kou melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Melni mane, melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Melni mane, melni mane
[ COUPLET 1]
Baby dama fresh, dama clean, dama high
Soumala douguelè thi roukhou walay doma bayi
Khol ma thi kaw bathi souf damay lakkè ni fire
Khamnani i'm the only one you desire
Khalè bou parè bolèthi wang wang wang
Dose binga sokhla malakoy diam diam
Sama wète dangay dègue diam diam diam
Kènay fowè sa khol mane mane mane
Meusso am kou melni mane baby dotoko amati
Bo fowè sa khèl bama reuthie la dotoko dèfati
[REFRAIN]
Do Meusseu am kou melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Melni mane, melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Melni mane, melni mane
[ COUPLET 2]
Diongoma mineur baby mane ngay weur
Fi lepp minè dièguèma exploser
Dama posè , osè , i'm good bad girl
Sa tempèrature makoy yèguel diko wathiè
Baby…
Sa yo diakhlè mane ngay lathiè
Baby…
Khalè bou parè bolèthi wang wang wang
Dose binga sokhla malakoy diam diam
Sama wète dangay dègue diam diam diam
Kènay fowè sa khol mane mane mane
Meusso am kou melni mane baby dotoko amati
Bo fowè sa khèl bama reuthie la dotoko dèfati
Meusso am kou melni mane baby dotoko amati
Boul fowè sa khèl bama reuthie la dotoko dèfati
[REFRAIN]
Do Meusseu am kou melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Melni mane, melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Do Meusseu am kou melni mane
Melni mane, melni mane
May sa ouroul aïni (eeeh)
A mes cotés tu vis le paradis
Fokoy dieuléti kou melni
May sa superstar yay sama paparazzi
May sa ouroul aïni (eh eeeeh)
A mes cotés tu vis le paradis ( Tu vis le paradiiiis)
Fokoy dieuléti kou melni
May sa superstar yay sama paparazzi (paparazzi i i )
Ouhou ouh
Hehehe
Domeusseu am kou melni mane
Ecouter
A Propos de "Domeusseu Am Kou Melni Mane"
Plus de Lyrics de OMG
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl