
Paroles de Kilometa
...
Paroles de Kilometa Par OMG
Yow
Fimala def sama xol bi dou thiaxàn’alafiy guené
Thiono
Yima dadj pour niou beuganté bb xam’nga nimou démé
Yoon bi meti woon niou diaayanté ko
Bou diarone tour deret ma rayanté ko
Mindef meunoul tax baniou bayanté no
Té niom meunougn tax baniou gaagnanté mak ioe
Nimala beugué bo dawone ay kilometa
Taxoul nga dap ma
Nimala nobé bo dawone ay kilometa yeah
Taxoul nga dap ma
Ningama beugué nouko raw laala beugué
Bb bo dawone ay diouni kilometa
Taxoul nga dap ma
Ning’ma beugué nonou laala rawé
Bo dawone ay kilometa
Taxoul nga dap ma
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Damala beugeu ba tiit sama bopp
Yow bingay def sama xol BAAXOUL
Douma setane dara dila wokk
Bou diaré la taylé sama nafsou
Xalei bi doonal sama nattou
Bilay dawou mathi dara
Wowal leen ma Tycco Tattou
Ndax sa tour laa beuggeu mou defal ma sama yaaram
Nimala beugué bo dawone ay kilometa
Taxoul nga dap ma
Nimala nobé bo dawone ay kilometa yeah
Taxoul nga dap ma
Ningama beugué nouko raw laala beugué
Bb bo dawone ay diouni kilometa
Taxoul nga dap ma
Ning’ma beugué nonou laala rawé
Bo dawone ay kilometa
Taxoul nga dap ma
Yama mome
Foma wo ma nieuw
Ndèkè damala bopp
Top Xol bi loum ma diguel ma def
Tothi kani pathial ligom
May kiy saf safal sa adouna
Bebe yama tigom
Thia kawa kaw
Ya takh ma rew waw
Nènagne ya takh ma rew
Mani lene beuguel bathia dakh moy nga nope kala nop waw
Aldiana yaw ya takh ma rew
Dakh danga ma nope ma nope la rawè ay kilometa
AH ah ah
Daw ay Diouni Kolomètre takhoul ga dab ma
AH ah ah
Daw ay Diouni Kolomètre takhoul ga dab ma
Ecouter
A Propos de "Kilometa"
Plus de Lyrics de OMG
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl