Paroles de Woma
Paroles de Woma Par SOKHOU BB
Bima nékék yaw ba légui
Meusouma yeuk mbeugyèl bou mél ni
Motakh ma fonkou leu
Motakh ma taamou leu
Meunou mala mérè ndakh thiofél bimay yeuk thji yaw
Wamo niou dioubo, warou’niou méro
Bouniouy rétann moudié thji xoulo
Bouniouy waxtann moudié rèro
Woma niou dioubo BB yow woma
Ndack fima tolou nii mann dama xass ba mine leu BB
Womoa niou dioubo
Woma niou dioiubo oh oh yow
Warouniou xoulo baby yow woma
Bouniouy rétann moudié thji xoulo
Bouniouy waxtann moudié rèro
Womoa niou dioubo, Warouniou xoul
Xamnga yay sama waay bilay
Souniou mbeuguèl nèxoul gaa’yi boul faaté
Dèglou ma, diana baakh
Boul diakhlè danio wara wèssou fi
Ngala woma, woooma yaw
Ouuuh ouuuh bébé
Meunouma nélaw woma, batt bimay yètal yaw la
Woma, woma
Tiss na ma teudd té dègoumala
Oh chéri, yo chéri mon ami yo ma vie
Mètima ma teudd dé dègoumala
Oh chéri yo chéri
Mon ami yo, mon ami
Mètima ma teudd dé dègoumala
Woma niou dioiubo oh oh yow
Warouniou xoulo baby yow woma
Yaw yay sama waay bilay
Souniou mbeuguèl nèxoul gaa’yi boul faaté
Woo oh ouuh ouuh woma
Woma woma, yaw la minn yaw la xam
Goudi gui dina yagg loolè thji man
Woma woma woma
Man deh yaw la am woma
Yamalén geuneul woma
Konn woma!
Ecouter
A Propos de "Woma"
Plus de Lyrics de SOKHOU BB
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl