
Paroles de Gouro
Paroles de Gouro Par NARAH DIOUF
Tey lagn done khar
Nga def ma sa diabar
Gneupp took ma sédel là
Né yaye kima sagal
Dagnou dém ban douro yaye ki ma yalla bolel
Dougnou meusseu reroo
Ndakh dagniy doundou mbeuguel
Indil ngama gouro dessalatoma dara
Yaye sama chamalama
Maye sa ding dong
Khol bi di teugg ni tama
Yaye sama best song
Yaye sama chamalama
Maye sa ding dong
Khol bi di teugg ni tama
Yaye sama best song
Ma seye, ma seye
Tey ma seyeul la
Ma sey, ma sey
Indi nga gouro bi
Ma seye, ma seye
Tey ma seyeul la
Ma sey, ma sey
Indi nga gouro bi
Loumou meti meti khamnané yangui fi
Def ngama sa sokhna tey beg naa, baby
Teranga bi mate na teralngama
Diambar dioni dioni
Guile guilé diambaréee
Yama tanne si séne biiir
Mala beuguue piir wakhma loukey dini
Dagnou dém ban douro yaye ki ma yalla bolel
Dougnou meusseu reroo
Ndakh dagniy doundou mbeuguel
Indil ngama gouro dessalatoma dara
Yaye sama chamalama
Maye sa ding dong
Khol bi di teugg ni tama
Yaye sama best song
Yaye sama chamalama
Maye sa ding dong
Khol bi di teugg ni tama
Yaye sama best song
Ma seye, ma seye
Tey ma seyeul la
Ma sey, ma sey
Indi nga gouro bi
Ma seye, ma seye
Tey ma seyeul la
Ma sey, ma sey
Indi nga gouro bi
Môme leu, môme leu
Môme leu, môme leu
Ndanane moy ki fegne sama doundou
Fo diar ma wayal la
Ndanane weuh wooo
Souma démé baleye weuy
Seck ndanane nangué
Mo ngui né
Seck ndanane nangué
Mo ngui né
Seck ndanane nangué
Ecouter
A Propos de "Gouro"
Plus de Lyrics de NARAH DIOUF
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl