Paroles de Tégguil sa Tank
Paroles de Tégguil sa Tank Par NARAH DIOUF
Life bé changé
Wala djikko yé yakou, yé yakou
Lo khamal ké Yolé
Ok Wakhnga ba tardé
Legui gneupeuley moytou, ley moytou
Mou ngui beug gnaw deh
Ndank, ndank, ndank
Teguil sa tank
Ndank, ndank, ndank
Teguil sa tankl
Ndank, ndank, ndank
Teguil sa tank
Ndank, ndank, ndank
Fi leu rew mi tollou
Gni deh cas lagniy topou
Lou tokh sa nopp
Fel sa guemin
Lepp tourou
Kone mou ngui tokh
Tiey Linga bokh
Tekk ko si souf
Balla mo souss
Ok Yangui si Tik Tok
Do raté Facebook
Snap nga flamme cas bi
Whatsap nga yénou tiow li
Ok bayil ninga néké
Li Dou sa métier
Boul topou sa khol
Wakhal prarara
Life bé changé
Wala djikko yé yakou, yé yakou
Lo khamal ké Yolé
Ok Wakhnga ba tardé
Legui gneupeuley moytou, ley moytou
Mou ngui beug gnaw deh
Ndank, ndank, ndank
Teguil sa tank
Ndank, ndank, ndank
Teguil sa tankl
Ndank, ndank, ndank
Teguil sa tank
Ndank, ndank, ndank
Bayil libeurou diambour
Di top sa kilo
Yow kholal sa bopp
Teggil sa nopp
Bayil soppp
Soooof
Shhhhh
Ya raw mor ndadié
Do raté dadjé
Kouy dem yobouleu
Fougn dem fekk leu
Life bi deh concourou teki là
Kou yekh niou bala fa
Diapal fils tè boul bayi
Fattal té bagna teppi
Fatalma fofou bou dara percé
Teubeul ma teup niou ande percer
Liguey rek di encaisser
Kassé
Life bé changé
Wala djikko yé yakou, yé yakou
Lo khamal ké Yolé
Ok Wakhnga ba tardé
Legui gneupeuley moytou, ley moytou
Mou ngui beug gnaw deh
Ndank, ndank, ndank
Teguil sa tank
Ndank, ndank, ndank
Teguil sa tankl
Ndank, ndank, ndank
Teguil sa tank
Ndank, ndank, ndank
Ecouter
A Propos de "Tégguil sa Tank"
Plus de Lyrics de NARAH DIOUF
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl