DIP DOUNDOU GUISS Taar Mbéth cover image

Paroles de Taar Mbéth

Paroles de Taar Mbéth Par DIP DOUNDOU GUISS


[COUPLET]
Dégouma daara men hée
Man la way doundou guiss
Taay mou melni tan beer bou policiers yi di tass
Kagn ngay demat sani xeer boutou keur président
Damlen fay man niki domou doubless di bi dann.
Israël ak Palestine beugouma né si diam.damalen di...
Fi tchiouné yé fi né gneup néna dip moy Messi non il joue très bien
Bama dalé bind motoul diourom ben att. 
Té old school youfi nek ken meunouleu def ni man
Amna niouy guené album nénagn man lagn thi clash
Coupes yengui sama negou mère niom meusouniou dem final
Samay ennemis nioy coach you gueneu efficace 
Samay none nioy samay coach you gueneu efficace
Meussougn yalouwan, 
Té dougn tegui tank magui ci minou Casamance yi dofouma bay tegui tank
Gars yi beugone ma xew nio beugat ma xewiwat.
Nélen lima dessé ci hit matna 180 giga.

[REFRAIN]
Nigga malen meun
Té nalen soul, par force !!!
Taar mbéth
Nigga malen meun, té nalen soul, par force
Man rek !!!
Nigga malen meun té nalen soul par force taar mbéth
Nigga malen meun té nalen soul par force mane rek

[COUPLET]
Parce que ma la meun té xawma say yow loma meuneul
Do y’Allah, do yonenti do sax 1 million de dollar
Da ngueu beug fayékou naleu diox li ngeu fa am
Beus di ngeu beug romb sama kogn mou teu leu
Bro diaféwouma guiss, lou moy ngua may guiss ak niom
Bo amé diom nan gay amé diotou kou am diot
Annoncer gouma sax, 
Gneup gui sama album dip album bi kagn la melni album bégui casso
Niari son ci ben beat non fils do def lou melni 
Niary son chaque niary semaine fils do def lou melni
Doxna kilomètre yu beuri yag xif té do dem leki ak rythme
Bi ma dieul ni pour done millionnaire dou meti
Maguek diplôme yep legui ak pistolé pour ray nitte
Kone duma yénou xew bi parce que gnoun ak yen dou derby
Broda boulma latch louy moré dioxma micro rek pour sama
Frigo fes mic yifi né yeup la beug rek niom gneup
niom gneup gnou xamné ni

[REFRAIN]
Malen meun té nalen soul par force taar mbéth
Nigga malen meun té nalen soul par force man rek
Nigga malen meun té nalen soul par force taar mbéth
Nigga malen meun té nalen soul par force man rek

[REFRAIN]
Malen meun té nalen soul par force taar mbéth
Nigga malen meun té nalen soul par force man rek
Nigga malen meun té nalen soul par force taar mbéth
Nigga malen meun té nalen soul par force man rek

Ecouter

A Propos de "Taar Mbéth"

Album : Taar Mbéth (Single)
Année de Sortie : 2016
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Sep 19 , 2019

Plus de Lyrics de DIP DOUNDOU GUISS

DIP DOUNDOU GUISS
DIP DOUNDOU GUISS
DIP DOUNDOU GUISS
DIP DOUNDOU GUISS

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl