Paroles de Sama Dome
Paroles de Sama Dome Par DIP DOUNDOU GUISS
[REFRAIN]
Yakamtinaleu, yakamtina
Yakamtinaleu, meunouma khar
Nangou nga place-am tchi sama xol
Dieul sama place, mome tchi xolam
Yakamtinaleu, yakamtinaleu
[COUPLET 1]
Kène téré wouniou bégg, té déé douniou réy
Nagne dém wouti guédj, dougne déloussi dèkhe
Etincelle bou guiss essence noumouy déf?
Féké souniouy guent néléw bissou dé
Y’allah meula denke, malaka nga lérr
Sa yaye-a ma bétt, diamant lama may
Amaana ba téy, y’allah dou yakamti dé
Kon fananal ak werr kouy nadjal sa kérr
Kay ma wakhla, wonla fi noumou mél
Danga ndaw té di nga def lou raw li kikirou def
Bou sissou, boul fène,
Boul feuss késsé ndakh siiw dou succès
Primaire samay photo classe amna niou siy moudj jail
Té nieupay niane am moudientél bou bakh
Yènsay nga ladj ndakh mawti khamna loutakh déé bi gaaw
Ngène foudeune séni tank dioubeul pénkou niane
Na dème église yobou soundél di taal
Loutakh rénn dou daaw?
C'est parce que rénn lagn outeul tène bi baak
Bougouma di tagato ni nieup
Bateau démna, bateau boudoul keupou
Capitaine yay woné yone bi forever
Kou fowé sa bop niou fowé leu
Kou domam deuk tchi diam dafa tabakh tchi guerre
Bou nieup di wouti lampe yow démal lèrr
Mane goudou fane rek lalay nianal
Koula khar kham do nieuw
[REFRAIN]
Yakamtinaleu, yakamtina
Yakamtinaleu, meunouma khar
Nangou nga place-am rchi sama xol
Dieul sama place, mom tchi xolam
Yakamtinaleu, yakamtinaleu
[COUPLET 2]
Tant que ya ngui bégk mangui bégk
Teudj nala tchi sama khol, dieul sama tiabi sani guédj
Yém sama diangue ak liguéy, magg khalis'am di lèw
Moytou danou tay tchi pakh bi diane yi matt lène
Yènn bi meussta diss ba raw bi yaye di dadj tchi seuy
Jésus christ meuss na rakhass ay tankou talibém
Yène say nga tann fék dagne la tann sans nga yeuk ko
Kham na ni thiatt dou yekh mais gnanal tawou tiatt bi yeup
Goor gui sa biss nieuwna
Fataliko ay maamame
Guiss neu kou mél comme mome
Mane la, siguil khol ma
Tékkina lafam naw
Wayé famou dieum, khawma fa
Mome famou dieum, khawma
Wayé aldjanah lagn-koy wowé
[REFRAIN]
Yakamtinaleu, yakamtina
Yakamtinaleu, meunouma khar
Nangou nga place-am rchi sama xol
Dieul sama place, mom tchi xolam
Yakamtinaleu, yakamtinaleu
Ecouter
A Propos de "Sama Dome"
Plus de Lyrics de DIP DOUNDOU GUISS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl