Paroles de Serigne Touba
Paroles de Serigne Touba Par DIHA TRAWALLY
Dama teud ben goudi mane
Guent guiss kouy niow ci mane
Mou ngui sol wex, auto bou wex takhaw
Nonou la tité, toudou La ilaha Ilala
Ilalahi fall, sante y’Allah mi mima wane li
Jjaeuf Borome bi
Yeurmandém dal nama
Kima dieulci déh wane nama
Niarii lerr yi di béneu lerr
Lérral na dounya
Han ahh Sérigne Touba
Bamba yafi def loutax niouné Bamba
Khékhal nga dine Islam, Khadim Rassoul
Ndamal djoulite ya ngui ni, Massalikul Jinaan
Sagouk djoulite ya ngui ni Massalikul Jinaan
[REFRAIN]
lérr ja gui ni (mo jalal)
Mbirr ban gui ni (dadi jamal)
Hummmmm…
Dal guew g amome modi jamal
Wérr ja gui ni (mo jalal)
Mbirr ban gui ni (dadi jamal)
Hummmmm…
Dal guew g amome modi jamal
Nourou mouhadiya moy ridial
Ibra Fall moy Lampe Fall
Ba sakhar ga déké ndar diawal Dakar
Ci nar, ndigual sa bag ley togn
Magal gui diote si na
Lika dorr ganar ba ca guélam
Sérigne Bamba nanou nako
[REFRAIN]
lérr ja gui ni (mo jalal)
Mbirr ban gui ni (dadi jamal)
Hummmmm…
Dal guew ga mome modi jamal
Lérr ja gui ni (mo jalal)
Mbirr ban gui ni (dadi jamal)
Hummmmm…
Dal guew g amome modi jamal
Ecouter
A Propos de "Serigne Touba"
Plus de Lyrics de DIHA TRAWALLY
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl