Paroles de Musiba
Paroles de Musiba Par DIP DOUNDOU GUISS
Fuck number one, Fuck number two
Ya ngeek limay fay, moytul baña juum (yeaah, ouuh)
Musiba naarulay
Gëm sama ñaanu yaay
Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay
Comme roof si ceeb
Cere dolli ñeex
Capp ni goor Gui Dieng
Vol si jet, wala doxx si geej
Yokk job du deñ
Kuy bonn di hate
Bombe nucléaire ci sa xol bu wow ni xeer
Même boy dé bul fokni jeex na, may bëss bila God di yé
Investir ci fenn amo saxx bénéfice du doute
Na doon 50 cents sama ben shot, sa fils du jukk
DIP mola mën du gacce c’est comme ku Messi di duut
Ma ngi si trône bi ak ñom Messi jël sama Pepsi di guux
Duma segg si cage
Man la seen soeurs yi di xaar
Maa taxx sen sërr yi di tass
Carrière bi munoko saltel nigger melni sa chemisou pa
Sëg di gass, job lu tax CD bi jarr
Fële jël sa reliquat
Sama cachet sañu ñuko dagg ni bin bin ci sa ndigu Ma
Na money bi teew, xaalis moy gagner guerre bi duma rayante comme militaires
Si kaw lañuy yeeg wacce leen ni adamak awa ak pomme biñu yëy
Sori fi man, duma xooli sa guel même su defe man kesse si story privem
Coow li du jeex fi ba mëwti di dé amatu ñu adversaire mais ño ngi si guerre
Fuck number one, Fuck number two
Ya ngeek limay fay, moytul baña juum (yeaah, ouuh)
Musiba naarulay
Gëm sama ñaanu yaay
Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay
Every day, may def baña xaar ndaxx dé du jeem
Soxlawuma tuub pour def ko benn buum mën na takk plus de 5 jeeg
Yes we can
Gedd gratte- ciel, dëkki Baraku Bamba fu Trump dem ba nek president
Fu sëtu esclave dila ray ngir chaîne
Tojj sa lu bonn ba mujje ak séy biens
Nigger ëppo njariñ skincaru Michael Jackson ci cimetière
Dangay gunge rek ni frèru Michael Scofield ci biir jail
Damay fayu ba pare mën nangu ni coow du jib kay
Ku xamm kepp kuy rap wolof xamna nombre rappeur bi DIP fay
Tek sama nafsu ci beat bi
Rap yefu dëmm dëg lë kan mo saña waxx ni que Pac bëggul Biggy ?
Sen game bi concours lëmbël la motax malay yokkal ay tama si beat bi
Sa guel la yakoy solal makoy simi, dagg buumu gacce dagg seeni string yi
Sama kumpa nekul books mais rappeur yi publier gul sen streams yi
Ay goat yu vider plassu gettu bëy du sho bu tijji tank rek ñu dem
Dé bi kesse momay taxa tëddi ni roses yi si sa tanku caissou neew
Bëg coow ni intifada Ben Laden
Même dof du sikki sakka lima fi def
God du mëssa àndak ñi di fenn
Par force King bi man la té du deñ
Fuck number one, Fuck number two
Ya ngeek limay fay, moytul baña juum (yeaah, ouuh)
Musiba naarulay
Gëm sama ñaanu yaay
Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay
Ecouter
A Propos de "Musiba"
Plus de Lyrics de DIP DOUNDOU GUISS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl