ADIOUZA Réseaux Sociaux cover image

Paroles de Réseaux Sociaux

...

Paroles de Réseaux Sociaux Par ADIOUZA


Mandou boula séné ni niokétt daw

Yakh derr moy sa liguey oudé yako raw

Do dermatologue Bayil derou gor gni

Yakh nitt defar sa poce nitt nga walla wethitt

Tall sa live dissi togg nitt

Iow yémal sisay soblé meuytou diebaner bi

Boula jiguer ngaye mbeur kamile

Febarou kignane moussoul meuna werr day

Zembéré rek di dem nga deuké mboly

Louy sa liguey ngani réseau yak asse gore

Goudekh beuthieuk Yangui si derrou diambour

Wetal tarri soratoul mougnal

Lou way di def sa kaw la dieum maytoul

Eh méchant boy ( Loutax )

Bousa kho di bakh (sa xole di bone)

Kay nga abal mako

Ma tek café ( sa xole di dagg)

Mane de jaxkhlena

Bo demoul douma dem loloye Sénégal

Waxale

Dinga deuké malaise meuytoul cardiaque

Docteur bi nena oubil si xole tek si del rétane

Maytoul beugn yi derréta ko lale

Soula beuggé fekhel dentiste meunoussi darra

Niou bok dieukeur ngani tay ngay deh

Kou sokhor kissi rang bi khôl be jexe

Wouye xole be nekh .

Febarou kignane moussoul meuna werr day

Zembéré rek di dem nga deuké mboly (2)

Louy sa liguey ngani réseau yakkass gore

Goudekh beuthieuk Yangui si derrou diambour

Wetal tarri soratoul mougnal

Lou way di def sa kay la dieum maytoul

Eh méchant boy ( Loutax )

Bousa kho di bakh (sa xole di bone )

Kay nga abal mako

Ma tek café (sa xole di dagg )

Mane de diaxelenaaa bo demoule douma dem li moye Sénégal Waxal

(Statut visé yi ngamaye xagne né dama daloule ndax

Kignane bi nga nekker si réseaux yi damako taloule)

Mane de diaxelenaaa bo demoule douma dem loloye Sénégal Waxal

(Da nga maye deuker vu sa xole di bonne

Dieundal glace sa xole fekh yalla ye mayer none)

Mane de diaxelenaaa bo demoule douma dem loloye Sénégal Waxal

(Tik tok nga talle sa live Facebook Instagram

Bayi wo fene fo rombou jebaner ma)

(Lou takh sou ma sagne def nga mère

Eh deug la)

(Ma deff lou baxe nga mère

Ehhhh none leu)

Borom xolou diamant bi

Momar Diop ko soppe

Mouni Mane ma beug Bamba

Ecouter

A Propos de "Réseaux Sociaux"

Album : (Single)
Année de Sortie : 2024
Copyright :
Ajouté par : Farida
Published : Nov 29 , 2024

Plus de Lyrics de ADIOUZA

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl