Paroles de Madame Bonheur
Paroles de Madame Bonheur Par ADIOUZA
Xolou ma kénene fess na sama sétou
Jiguéne jiy waxé dieuf dou ame diotou tontou
Done awo di bourou keur gui dou aye fontou
Té saxe fouma momé
Zéro lakoy wathié
Lou deuss meuneu daw
1 bé ngui thi kaw
Gnari fane youné coco feug aldiana takhaw
Bonheur
Fi wax amoul thiouray guéy rire
Def terreur
Loutax mouy séd té may dièk pire
Péssé sama bop xamni warouma ragal woudié
Ladial mon cœur
Kouy madame bonheur
Yamay confiné lép di dioup ya raw policier
Ladial mon cœur
Kouy madame bonheur
Ouhhhh wolma abass
Chéri fatou ak chilel
Borom gambia
Li lay door té doula la laale, nékhoul thi
Khol
Deuxième dame bi lagnou takkal medaille d’or
Ki nélaw la xamone ma diangal ko yandoor
Bayi léne di diém diangue xam sa goor gueuneu woor
Xol bi nangou fétté
Boboy doundou mbecté
Namouma daray wax
Ba fi mingui baakh
Chérie dougueul deukeu do feugue yaye laisser passé
Allo
Fi maay sourire mouy évanouir
Mais allo
Ay nelaw diékhna dama yor lire
Péssé sama bop xamni warouma ragal woudié
Ladial mon coeur maye ki koye bonheur
Yamay confiné lép di dioup ya raw poli..cier
Ladial mon coeur maye ki koye bonheur
Yeah
Coco manak yaw ba adiana
Thi sa wét lay doundé olala
Yaa gaw thi mane
Say je taime thi sama biir tempan
Ningmay def néx nama
Beugueu nala bae
Péssé sama bop xamni warouma ragal woudié
Ladial mon coeur
Kouy madame bonheur
Yamay confiné lép di dioup ya raw poli..cier
Ladial mon coeur
Kouy madame bonheur
Ecouter
A Propos de "Madame Bonheur"
Plus de Lyrics de ADIOUZA
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl